Al-An'am · 61/165
Tekki Waxtaan — Al-An'am
وَهُوَ الْقَاهِرُ فَوْقَ عِبَادِهِ ۖ وَيُرْسِلُ عَلَيْكُمْ حَفَظَةً حَتَّىٰ إِذَا جَاءَ أَحَدَكُمُ الْمَوْتُ تَوَفَّتْهُ رُسُلُنَا وَهُمْ لَا يُفَرِّطُونَ ۝٦١
Wa huwal qaahiru fawqa `ibaadihee wa yursilu `alaikum hafazatan hattaaa izaa jaaa`a ahadakumul mawtu tawaffathu rusulunaa wa hum laa yufarritoon
📖 Tekkim Wolof
Te Moom mooy Aji-not ja ci kaw jaamam ya. Te Mooy yónni ci yéen ay Malaaka yu leen di wattu. Ba kero bis ba dee di agsi, ba kenn ci yéen sunuy ndaw rey ko, te ñoom sàgganuñu ci dara.
🎧 Dégg

📜 Aaya 59-63 — Al-An'am

59۞ وَعِندَهُ مَفَاتِحُ الْغَيْبِ لَا يَعْلَمُهَا إِلَّا هُوَ ۚ وَيَعْلَمُ مَا فِي الْبَرِّ وَالْبَحْرِ ۚ وَمَا تَسْقُطُ مِن وَرَقَةٍ إِلَّا يَعْلَمُهَا وَلَا حَبَّةٍ فِي ظُلُمَاتِ الْأَرْضِ وَلَا رَطْبٍ وَلَا يَابِسٍ إِلَّا فِي كِتَابٍ مُّبِينٍ
Fa Moom la caabiy kumpa nekk. Kenn xamuleen ku dul Moom. Te xam na li nekk ci jéeri ji ak géej gi. Te amul fenn xob wuy rot te xamu ko. Du caageene wenn fepp wu nekk ci biir lëndëmu suuf si, di lu tooy, di lu wow, ndare du nekk na ci ab téere bu leer nàññ.
60وَهُوَ الَّذِي يَتَوَفَّاكُم بِاللَّيْلِ وَيَعْلَمُ مَا جَرَحْتُم بِالنَّهَارِ ثُمَّ يَبْعَثُكُمْ فِيهِ لِيُقْضَىٰ أَجَلٌ مُّسَمًّى ۖ ثُمَّ إِلَيْهِ مَرْجِعُكُمْ ثُمَّ يُنَبِّئُكُم بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Moom moo leen di nelawloo guddi, te xam na la ngeen di fàggu ci bëccëg. Topp Mu yee leen ngir àtte dig buñu dogal ba. Topp nag, ngeen dellu ci Moom, Mu biral leen la ngeen doon def..
61وَهُوَ الْقَاهِرُ فَوْقَ عِبَادِهِ ۖ وَيُرْسِلُ عَلَيْكُمْ حَفَظَةً حَتَّىٰ إِذَا جَاءَ أَحَدَكُمُ الْمَوْتُ تَوَفَّتْهُ رُسُلُنَا وَهُمْ لَا يُفَرِّطُونَ
Te Moom mooy Aji-not ja ci kaw jaamam ya. Te Mooy yónni ci yéen ay Malaaka yu leen di wattu. Ba kero bis ba dee di agsi, ba kenn ci yéen sunuy ndaw rey ko, te ñoom sàgganuñu ci dara.
62ثُمَّ رُدُّوا إِلَى اللَّهِ مَوْلَاهُمُ الْحَقِّ ۚ أَلَا لَهُ الْحُكْمُ وَهُوَ أَسْرَعُ الْحَاسِبِينَ
Bu loolu jàllee, ñu delloo leen fa Yàlla, kay seen Boroom tigi. Moo ndax du Moo moom àtte ba te Moo gën a gaaw wàññikat yépp.
63قُلْ مَن يُنَجِّيكُم مِّن ظُلُمَاتِ الْبَرِّ وَالْبَحْرِ تَدْعُونَهُ تَضَرُّعًا وَخُفْيَةً لَّئِنْ أَنجَانَا مِنْ هَٰذِهِ لَنَكُونَنَّ مِنَ الشَّاكِرِينَ
Neel : “Kan moo leen di musal ci lëndëmu jéeri ak gu géej ? ” Te ngeen di Ko faral a woo ànd ak toroxlu ak nëbbu, naan : “ Cëy Yàlla, boo nu musalee ci lii, kon dey nu bokk ca gërëmkat ya.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
61Aaya

Tekki — Al-An'am 61

Simoore Al-An'am Aaya 61 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te Moom mooy Aji-not ja ci kaw jaamam ya. Te…

Simoore Aaya 61/165 — Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-An'am Dégg, Al-An'am Tekki, Al-An'am mp3, Al-An'am pdf. Aaya 59–63. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers