At-Taghabun · 15/18
Tekki Waxtaan — Simoore At-Taghabun
إِنَّمَا أَمْوَالُكُمْ وَأَوْلَادُكُمْ فِتْنَةٌ ۚ وَاللَّهُ عِندَهُ أَجْرٌ عَظِيمٌ ۝١٥
Innamaa amwaalukum wa awlaadukum fitnah; wallaahu `indahooo ajrun `azeem
📖 Tekkim Wolof
Seeni alal ak seeni doom sànje la ci yéen, (Waaye) la nekk fa Yàlla moo di pey gu màgg.

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Simoore At-Taghabun

13اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۚ وَعَلَى اللَّهِ فَلْيَتَوَكَّلِ الْمُؤْمِنُونَ
Yàlla, amul jeneen Yàlla ju dul moom ! Te ñi gëm na ñuy doyloo Yàlla.
14يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِنَّ مِنْ أَزْوَاجِكُمْ وَأَوْلَادِكُمْ عَدُوًّا لَّكُمْ فَاحْذَرُوهُمْ ۚ وَإِن تَعْفُوا وَتَصْفَحُوا وَتَغْفِرُوا فَإِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
eey yéen ñi gëm, am na ci seeni jabar ak seeni doom ñoo xam ne seeni noon la ñu. Nangeen leen di moytu. (Waaye) su ngeen balee tey jéllale, Yàlla moom ab Jéggalaakoon la, Jagléwaakoon la.
15إِنَّمَا أَمْوَالُكُمْ وَأَوْلَادُكُمْ فِتْنَةٌ ۚ وَاللَّهُ عِندَهُ أَجْرٌ عَظِيمٌ
Seeni alal ak seeni doom sànje la ci yéen, (Waaye) la nekk fa Yàlla moo di pey gu màgg.
16فَاتَّقُوا اللَّهَ مَا اسْتَطَعْتُمْ وَاسْمَعُوا وَأَطِيعُوا وَأَنفِقُوا خَيْرًا لِّأَنفُسِكُمْ ۗ وَمَن يُوقَ شُحَّ نَفْسِهِ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Nangeen di ragal Yàlla seen kem kàttan, dégluleen, te topp te joxe alal. Moo gën ci yéen de. Képp ku mucc ci ag nay (na xam ne)... ñoo di ña baaxle.
17إِن تُقْرِضُوا اللَّهَ قَرْضًا حَسَنًا يُضَاعِفْهُ لَكُمْ وَيَغْفِرْ لَكُمْ ۚ وَاللَّهُ شَكُورٌ حَلِيمٌ
Su ngeen lebalee Yàlla bor bu rafet, Dana leen ko fulal te it dana leen jéggal. Te Yàlla ab Santaakoon la Ku lewet la.
At-TaghabunFihi Alxuraan
18Aaya
MedinanRevelation
15Aaya

Tekki — At-Taghabun 15

Simoore At-Taghabun Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seeni alal ak seeni doom sànje la ci yéen, (Waaye)…

Simoore Aaya 15/18 — Simoore At-Taghabun التغابن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Taghabun Dégg, Simoore At-Taghabun Tekki, Simoore At-Taghabun mp3, Simoore At-Taghabun pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers