Al-Qalam · 9/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
وَدُّوا لَوْ تُدْهِنُ فَيُدْهِنُونَ ۝٩
Waddoo law tudhinu fa-yudhinoon
📖 Tekkim Wolof
Bëgg nañu nga nooy ba ñu nooy ñoom itam.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 7-11 — Simoore Al-Qalam

7إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ
Te sa Boroom moo gën a xam ku réere aw Yoonam, te it moo gën a xam ñay gindiku.
8فَلَا تُطِعِ الْمُكَذِّبِينَ
Bul topp mukk ñiy fen,
9وَدُّوا لَوْ تُدْهِنُ فَيُدْهِنُونَ
Bëgg nañu nga nooy ba ñu nooy ñoom itam.
10وَلَا تُطِعْ كُلَّ حَلَّافٍ مَّهِينٍ
Bul topp bépp waatkat, bu doyadi,
11هَمَّازٍ مَّشَّاءٍ بِنَمِيمٍ
ab saagakat, buy dox di rambaaje,
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Qalam 9

Simoore Al-Qalam Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bëgg nañu nga nooy ba ñu nooy ñoom itam.

Simoore Aaya 9/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers