Al-Qalam · 10/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
وَلَا تُطِعْ كُلَّ حَلَّافٍ مَّهِينٍ ۝١٠
Wa laa tuti` kulla hallaa fim maheen
📖 Tekkim Wolof
Bul topp bépp waatkat, bu doyadi,

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore Al-Qalam

8فَلَا تُطِعِ الْمُكَذِّبِينَ
Bul topp mukk ñiy fen,
9وَدُّوا لَوْ تُدْهِنُ فَيُدْهِنُونَ
Bëgg nañu nga nooy ba ñu nooy ñoom itam.
10وَلَا تُطِعْ كُلَّ حَلَّافٍ مَّهِينٍ
Bul topp bépp waatkat, bu doyadi,
11هَمَّازٍ مَّشَّاءٍ بِنَمِيمٍ
ab saagakat, buy dox di rambaaje,
12مَّنَّاعٍ لِّلْخَيْرِ مُعْتَدٍ أَثِيمٍ
buy tere aw yiw, tey jalgati, di def bàkkaar,
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Al-Qalam 10

Simoore Al-Qalam Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bul topp bépp waatkat, bu doyadi,

Simoore Aaya 10/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers