Al-Insan · 31/31
Tekki Waxtaan — Al-Insan
يُدْخِلُ مَن يَشَاءُ فِي رَحْمَتِهِ ۚ وَالظَّالِمِينَ أَعَدَّ لَهُمْ عَذَابًا أَلِيمًا ۝٣١
Yudkhilu mai yashaaa`u fee rahmatih; wazzaalimeena a`adda lahum `azaaban aleemaa
📖 Tekkim Wolof
Mooy tàbbal ku ko soob ci yërmëndéem. Te tooñkat yi, Waajalna leen mbugël mu mitti.

🎧 Dégg


📜 Aaya 29-31 — Al-Insan

29إِنَّ هَٰذِهِ تَذْكِرَةٌ ۖ فَمَن شَاءَ اتَّخَذَ إِلَىٰ رَبِّهِ سَبِيلًا
Lii dey ag fàttali la. Képp ku mu soob man ngaa sóobu yoon jëm ca sa Boroom !
30وَمَا تَشَاءُونَ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ ۚ إِنَّ اللَّهَ كَانَ عَلِيمًا حَكِيمًا
Manu leen a sottal dara, te du dafa soob Yàlla. Moom ku Xam la ku Xereñ la.
31يُدْخِلُ مَن يَشَاءُ فِي رَحْمَتِهِ ۚ وَالظَّالِمِينَ أَعَدَّ لَهُمْ عَذَابًا أَلِيمًا
Mooy tàbbal ku ko soob ci yërmëndéem. Te tooñkat yi, Waajalna leen mbugël mu mitti.
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
31Aaya

Tekki — Al-Insan 31

Simoore Al-Insan Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy tàbbal ku ko soob ci yërmëndéem. Te tooñkat yi,…

Simoore Aaya 31/31 — Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Insan Dégg, Al-Insan Tekki, Al-Insan mp3, Al-Insan pdf. Aaya 29–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers