Al-Insan · 30/31
Tekki Waxtaan — Al-Insan
وَمَا تَشَاءُونَ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ ۚ إِنَّ اللَّهَ كَانَ عَلِيمًا حَكِيمًا ۝٣٠
Wa maa tashaaa`oona illaa anyyashaaa`al laah; innal laahaa kaana`Aleeman Hakeema
📖 Tekkim Wolof
Manu leen a sottal dara, te du dafa soob Yàlla. Moom ku Xam la ku Xereñ la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-31 — Al-Insan

28نَّحْنُ خَلَقْنَاهُمْ وَشَدَدْنَا أَسْرَهُمْ ۖ وَإِذَا شِئْنَا بَدَّلْنَا أَمْثَالَهُمْ تَبْدِيلًا
Nun Noo leen bind. May leen kàttan, te Sunu sooboon, Nu wuutal fi ñeneen.
29إِنَّ هَٰذِهِ تَذْكِرَةٌ ۖ فَمَن شَاءَ اتَّخَذَ إِلَىٰ رَبِّهِ سَبِيلًا
Lii dey ag fàttali la. Képp ku mu soob man ngaa sóobu yoon jëm ca sa Boroom !
30وَمَا تَشَاءُونَ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ ۚ إِنَّ اللَّهَ كَانَ عَلِيمًا حَكِيمًا
Manu leen a sottal dara, te du dafa soob Yàlla. Moom ku Xam la ku Xereñ la.
31يُدْخِلُ مَن يَشَاءُ فِي رَحْمَتِهِ ۚ وَالظَّالِمِينَ أَعَدَّ لَهُمْ عَذَابًا أَلِيمًا
Mooy tàbbal ku ko soob ci yërmëndéem. Te tooñkat yi, Waajalna leen mbugël mu mitti.
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
30Aaya

Tekki — Al-Insan 30

Simoore Al-Insan Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Manu leen a sottal dara, te du dafa soob Yàlla.…

Simoore Aaya 30/31 — Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Insan Dégg, Al-Insan Tekki, Al-Insan mp3, Al-Insan pdf. Aaya 28–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers