Al-Anfal · 68/75
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anfal
لَّوْلَا كِتَابٌ مِّنَ اللَّهِ سَبَقَ لَمَسَّكُمْ فِيمَا أَخَذْتُمْ عَذَابٌ عَظِيمٌ ۝٦٨
Law laa Kitaabum minal laahi sabaqa lamassakum fee maaa akhaztum `azaabun `azeem
📖 Tekkim Wolof
Bu bul koon dogal bu tukkee ca Yàlla bu jiitu, kon mbugal mu rëy dana leen dal ngir la ngeen màng.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 66-70 — Simoore Al-Anfal

66الْآنَ خَفَّفَ اللَّهُ عَنكُمْ وَعَلِمَ أَنَّ فِيكُمْ ضَعْفًا ۚ فَإِن يَكُن مِّنكُم مِّائَةٌ صَابِرَةٌ يَغْلِبُوا مِائَتَيْنِ ۚ وَإِن يَكُن مِّنكُمْ أَلْفٌ يَغْلِبُوا أَلْفَيْنِ بِإِذْنِ اللَّهِ ۗ وَاللَّهُ مَعَ الصَّابِرِينَ
Léegi, Yàlla woyofal na leen ngir xam na doyadi gi nekk ci yéen. Kon bu nekkee ci yéen téeméer yu muñ, danañu not ñaari téeméer ; bu nekkee ci yéen junni, danañu not ñaari junni, bu neexee Yàlla. Te Yàlla muñkat yi la àndal.
67مَا كَانَ لِنَبِيٍّ أَن يَكُونَ لَهُ أَسْرَىٰ حَتَّىٰ يُثْخِنَ فِي الْأَرْضِ ۚ تُرِيدُونَ عَرَضَ الدُّنْيَا وَاللَّهُ يُرِيدُ الْآخِرَةَ ۗ وَاللَّهُ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
Warul cib Yonent mu am ay jaar-jaar [ca ña ñu jàppe cib xare not leen] fekk ñu nasaxal yéefar yi, faagaagal leen ba ñu mokk ci suuf si. Dangeen a bëgg [yéen jullit ñi] alali àddina, te Yàlla bëggal leen [xéewalu] àllaaxira. Te Yàlla Ku not la, Ku xereñ la.
68لَّوْلَا كِتَابٌ مِّنَ اللَّهِ سَبَقَ لَمَسَّكُمْ فِيمَا أَخَذْتُمْ عَذَابٌ عَظِيمٌ
Bu bul koon dogal bu tukkee ca Yàlla bu jiitu, kon mbugal mu rëy dana leen dal ngir la ngeen màng.
69فَكُلُوا مِمَّا غَنِمْتُمْ حَلَالًا طَيِّبًا ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ ۚ إِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Kon lekkleen ca la ngeen màng, muy lu dagan lu teey. Te ngeen ragal Yàlla, Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
70يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ قُل لِّمَن فِي أَيْدِيكُم مِّنَ الْأَسْرَىٰ إِن يَعْلَمِ اللَّهُ فِي قُلُوبِكُمْ خَيْرًا يُؤْتِكُمْ خَيْرًا مِّمَّا أُخِذَ مِنكُمْ وَيَغْفِرْ لَكُمْ ۗ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Éy yaw Yonent bi, waxal jaam yi nekk ci seeni yoxo, ne : “Bu Yàlla gisee dara lu baax ci seeni xol, Dana leen jox la gën ci yéen te Dana leen jéggal. Yàlla Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
68Aaya

Tekki — Al-Anfal 68

Simoore Al-Anfal Aaya 68 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu bul koon dogal bu tukkee ca Yàlla bu jiitu,…

Simoore Aaya 68/75 — Simoore Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anfal Dégg, Simoore Al-Anfal Tekki, Simoore Al-Anfal mp3, Simoore Al-Anfal pdf. Aaya 66–70. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers