At-Tawba · 49/129
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tawba
وَمِنْهُم مَّن يَقُولُ ائْذَن لِّي وَلَا تَفْتِنِّي ۚ أَلَا فِي الْفِتْنَةِ سَقَطُوا ۗ وَإِنَّ جَهَنَّمَ لَمُحِيطَةٌ بِالْكَافِرِينَ ۝٤٩
Wa minhum mai yaqoolu` zal lee wa laa taftinneee; alaa fil fitnati saqatoo; wa inna Jahannama lamuheetatum bil kaafireen
📖 Tekkim Wolof
Am na ci ñoom ñuy ñaan ndigalul toog ba noppi naan : “Bul ma fitnaal nag.”. Ñoom tàbbi ñañu ci biir fitna ba noppi ; te Safaraa nga gaw yéefar ya ci wet gu nekk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 47-51 — Simoore At-Tawba

47لَوْ خَرَجُوا فِيكُم مَّا زَادُوكُمْ إِلَّا خَبَالًا وَلَأَوْضَعُوا خِلَالَكُمْ يَبْغُونَكُمُ الْفِتْنَةَ وَفِيكُمْ سَمَّاعُونَ لَهُمْ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ بِالظَّالِمِينَ
Te sax ñoom bu ñu génnoon, ànd ak yéen, dem xare ji, garaawaali rekk lañu leen fay dolli ak fàbbi nit ñi. Te Yàlla xam na tooñkat yi.
48لَقَدِ ابْتَغَوُا الْفِتْنَةَ مِن قَبْلُ وَقَلَّبُوا لَكَ الْأُمُورَ حَتَّىٰ جَاءَ الْحَقُّ وَظَهَرَ أَمْرُ اللَّهِ وَهُمْ كَارِهُونَ
Fitna rekk lañu daan sàkku, ñu nekk ñu daan la ko wëlbatile mbir yi, ba dëgg ñëw, seen mbir wuññiku feeñ, te sañuñu koo bañ.
49وَمِنْهُم مَّن يَقُولُ ائْذَن لِّي وَلَا تَفْتِنِّي ۚ أَلَا فِي الْفِتْنَةِ سَقَطُوا ۗ وَإِنَّ جَهَنَّمَ لَمُحِيطَةٌ بِالْكَافِرِينَ
Am na ci ñoom ñuy ñaan ndigalul toog ba noppi naan : “Bul ma fitnaal nag.”. Ñoom tàbbi ñañu ci biir fitna ba noppi ; te Safaraa nga gaw yéefar ya ci wet gu nekk.
50إِن تُصِبْكَ حَسَنَةٌ تَسُؤْهُمْ ۖ وَإِن تُصِبْكَ مُصِيبَةٌ يَقُولُوا قَدْ أَخَذْنَا أَمْرَنَا مِن قَبْلُ وَيَتَوَلَّوا وَّهُمْ فَرِحُونَ
Boo amee mbégte, ñu mer. Bu la naqar dalee, ñu bég ca, te naan : “Ndokk ba demunu woon.” Et ils se détournent tout en exultant.
51قُل لَّن يُصِيبَنَا إِلَّا مَا كَتَبَ اللَّهُ لَنَا هُوَ مَوْلَانَا ۚ وَعَلَى اللَّهِ فَلْيَتَوَكَّلِ الْمُؤْمِنُونَ
Waxal ne : “Dara mënunoo dal lu dul lu Yàlla bind ci nun rekk. Te Mooy sunu Kilifa. Te it ñi gëm, nañuy wéeru ci Yàlla”.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
49Aaya

Tekki — At-Tawba 49

Simoore At-Tawba Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Am na ci ñoom ñuy ñaan ndigalul toog ba noppi…

Simoore Aaya 49/129 — Simoore At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tawba Dégg, Simoore At-Tawba Tekki, Simoore At-Tawba mp3, Simoore At-Tawba pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers