At-Tawba · 48/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
لَقَدِ ابْتَغَوُا الْفِتْنَةَ مِن قَبْلُ وَقَلَّبُوا لَكَ الْأُمُورَ حَتَّىٰ جَاءَ الْحَقُّ وَظَهَرَ أَمْرُ اللَّهِ وَهُمْ كَارِهُونَ ۝٤٨
Laqadib taghawul fitnata min qablu wa qallaboo lakal umoora hattaa jaaa`al haqqu wa zahara amrul laahi wa hum kaarihoon
📖 Tekkim Wolof
Fitna rekk lañu daan sàkku, ñu nekk ñu daan la ko wëlbatile mbir yi, ba dëgg ñëw, seen mbir wuññiku feeñ, te sañuñu koo bañ.
🎧 Dégg

📜 Aaya 46-50 — At-Tawba

46۞ وَلَوْ أَرَادُوا الْخُرُوجَ لَأَعَدُّوا لَهُ عُدَّةً وَلَٰكِن كَرِهَ اللَّهُ انبِعَاثَهُمْ فَثَبَّطَهُمْ وَقِيلَ اقْعُدُوا مَعَ الْقَاعِدِينَ
Waay-waay bu ñu bëggoon a génn xare ji, kon danañu waaj ba jekk. Waaye Yàlla daleen a sib; tàyyeel-loo leen. Ba tax na ñu ne leen : “Fafleen toog rekk”.
47لَوْ خَرَجُوا فِيكُم مَّا زَادُوكُمْ إِلَّا خَبَالًا وَلَأَوْضَعُوا خِلَالَكُمْ يَبْغُونَكُمُ الْفِتْنَةَ وَفِيكُمْ سَمَّاعُونَ لَهُمْ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ بِالظَّالِمِينَ
Te sax ñoom bu ñu génnoon, ànd ak yéen, dem xare ji, garaawaali rekk lañu leen fay dolli ak fàbbi nit ñi. Te Yàlla xam na tooñkat yi.
48لَقَدِ ابْتَغَوُا الْفِتْنَةَ مِن قَبْلُ وَقَلَّبُوا لَكَ الْأُمُورَ حَتَّىٰ جَاءَ الْحَقُّ وَظَهَرَ أَمْرُ اللَّهِ وَهُمْ كَارِهُونَ
Fitna rekk lañu daan sàkku, ñu nekk ñu daan la ko wëlbatile mbir yi, ba dëgg ñëw, seen mbir wuññiku feeñ, te sañuñu koo bañ.
49وَمِنْهُم مَّن يَقُولُ ائْذَن لِّي وَلَا تَفْتِنِّي ۚ أَلَا فِي الْفِتْنَةِ سَقَطُوا ۗ وَإِنَّ جَهَنَّمَ لَمُحِيطَةٌ بِالْكَافِرِينَ
Am na ci ñoom ñuy ñaan ndigalul toog ba noppi naan : “Bul ma fitnaal nag.”. Ñoom tàbbi ñañu ci biir fitna ba noppi ; te Safaraa nga gaw yéefar ya ci wet gu nekk.
50إِن تُصِبْكَ حَسَنَةٌ تَسُؤْهُمْ ۖ وَإِن تُصِبْكَ مُصِيبَةٌ يَقُولُوا قَدْ أَخَذْنَا أَمْرَنَا مِن قَبْلُ وَيَتَوَلَّوا وَّهُمْ فَرِحُونَ
Boo amee mbégte, ñu mer. Bu la naqar dalee, ñu bég ca, te naan : “Ndokk ba demunu woon.” Et ils se détournent tout en exultant.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
48Aaya

Tekki — At-Tawba 48

Simoore At-Tawba Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Fitna rekk lañu daan sàkku, ñu nekk ñu daan la…

Simoore Aaya 48/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers