Al-'Alaq · 8/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Alaq
إِنَّ إِلَىٰ رَبِّكَ الرُّجْعَىٰ ۝٨
Innna ilaa rabbikar ruj`aa
📖 Tekkim Wolof
(Xamal ne), sa Boroom mooy delluwaay ba.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore Al-'Alaq

6كَلَّا إِنَّ الْإِنسَانَ لَيَطْغَىٰ
Waaye nit kat dafay bew,
7أَن رَّآهُ اسْتَغْنَىٰ
bu gisee dafa woomal man boppam.
8إِنَّ إِلَىٰ رَبِّكَ الرُّجْعَىٰ
(Xamal ne), sa Boroom mooy delluwaay ba.
9أَرَأَيْتَ الَّذِي يَنْهَىٰ
Xanaa gisoo waa jay tere
10عَبْدًا إِذَا صَلَّىٰ
ab jamub Yàlla (Muhammad) ci muy taxawal Julli ?
Al-'AlaqFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-'Alaq 8

Simoore Al-'Alaq Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Xamal ne), sa Boroom mooy delluwaay ba.

Simoore Aaya 8/19 — Simoore Al-'Alaq العلق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Alaq Dégg, Simoore Al-'Alaq Tekki, Simoore Al-'Alaq mp3, Simoore Al-'Alaq pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers