Al-'Alaq · 7/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Alaq
أَن رَّآهُ اسْتَغْنَىٰ ۝٧
Ar-ra aahus taghnaa
📖 Tekkim Wolof
bu gisee dafa woomal man boppam.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 5-9 — Simoore Al-'Alaq

5عَلَّمَ الْإِنسَانَ مَا لَمْ يَعْلَمْ
moo xamal nit lamu xamut woon.
6كَلَّا إِنَّ الْإِنسَانَ لَيَطْغَىٰ
Waaye nit kat dafay bew,
7أَن رَّآهُ اسْتَغْنَىٰ
bu gisee dafa woomal man boppam.
8إِنَّ إِلَىٰ رَبِّكَ الرُّجْعَىٰ
(Xamal ne), sa Boroom mooy delluwaay ba.
9أَرَأَيْتَ الَّذِي يَنْهَىٰ
Xanaa gisoo waa jay tere
Al-'AlaqFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-'Alaq 7

Simoore Al-'Alaq Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bu gisee dafa woomal man boppam.

Simoore Aaya 7/19 — Simoore Al-'Alaq العلق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Alaq Dégg, Simoore Al-'Alaq Tekki, Simoore Al-'Alaq mp3, Simoore Al-'Alaq pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers