5 Aaya · Meccan · Wolof
bismillah
ﮍﮎﮏﮐﮑﮒﮓﮔ
105:1 Xanaa gisu leen ka sa Boroom def ak ña ame woon ñay ya.
ﮕﮖﮗﮘﮙﮚ
105:2 Moo ndax deful seen pexe ma mu naaxsaay ?
ﮛﮜﮝﮞﮟ
105:3 moo yabal ca seen kaw ay njanaaw yu bari
ﮠﮡﮢﮣﮤ
105:4 ñu di leen sànni ay doj yu ñu saaf?
ﮥﮦﮧﮨ
105:5 Mu def leen ñu mel ne am ñax mu ñu sàqami.

Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers