Yunus · 101/109
Tekki Waxtaan — Yunus
قُلِ انظُرُوا مَاذَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَمَا تُغْنِي الْآيَاتُ وَالنُّذُرُ عَن قَوْمٍ لَّا يُؤْمِنُونَ ۝١٠١
Qulin zuroo maazaa fissamaawaati wal ard; wa maa tughnil Aayaatu wannuzuru `an qawmil laa yu`minoon
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Xool-leen li nekk ci asamaan yi ak suuf si”. Te kaawtéef ya ak waaraate ya duñu jariñ dara ci aw nit ñu gëmul.
🎧 Dégg

📜 Aaya 99-103 — Yunus

99وَلَوْ شَاءَ رَبُّكَ لَآمَنَ مَن فِي الْأَرْضِ كُلُّهُمْ جَمِيعًا ۚ أَفَأَنتَ تُكْرِهُ النَّاسَ حَتَّىٰ يَكُونُوا مُؤْمِنِينَ
Bu neexoon sa Boroorm, fàwwu ñi nekk ci kaw suuf si ñépp gëm. Moo ndax yaw dangay ga [gétén] nit ñi ci ñu nekk ñu gëm ?
100وَمَا كَانَ لِنَفْسٍ أَن تُؤْمِنَ إِلَّا بِإِذْنِ اللَّهِ ۚ وَيَجْعَلُ الرِّجْسَ عَلَى الَّذِينَ لَا يَعْقِلُونَ
Yellul ci benn bakkan muy gëm lu dul ci coobarey Yàlla. Te Dana teg mbugal ña xel- luwul [ba mën a ràññee dëgg].
101قُلِ انظُرُوا مَاذَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَمَا تُغْنِي الْآيَاتُ وَالنُّذُرُ عَن قَوْمٍ لَّا يُؤْمِنُونَ
Neel : “Xool-leen li nekk ci asamaan yi ak suuf si”. Te kaawtéef ya ak waaraate ya duñu jariñ dara ci aw nit ñu gëmul.
102فَهَلْ يَنتَظِرُونَ إِلَّا مِثْلَ أَيَّامِ الَّذِينَ خَلَوْا مِن قَبْلِهِمْ ۚ قُلْ فَانتَظِرُوا إِنِّي مَعَكُم مِّنَ الْمُنتَظِرِينَ
Moo ndax ñooña dañuy xaar ba mu deme ni bis yu tiis, yu ña leen jiitu woon dajoon, agsi ci ñoom ? Neleen : “Muñandikuleen ! Man it maa ngi bokk ci ñay muñandiku”.
103ثُمَّ نُنَجِّي رُسُلَنَا وَالَّذِينَ آمَنُوا ۚ كَذَٰلِكَ حَقًّا عَلَيْنَا نُنجِ الْمُؤْمِنِينَ
Topp ginnaaw ba, Nu musal Sunuy Yonent ak ña gëm. Noonu la yaye ci Nun Nuy musal ñi gëm.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
101Aaya

Tekki — Yunus 101

Simoore Yunus Aaya 101 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Xool-leen li nekk ci asamaan yi ak suuf…

Simoore Aaya 101/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 99–103. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers