Ibrahima · 27/52
Tekki Waxtaan — Ibrahima
يُثَبِّتُ اللَّهُ الَّذِينَ آمَنُوا بِالْقَوْلِ الثَّابِتِ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَفِي الْآخِرَةِ ۖ وَيُضِلُّ اللَّهُ الظَّالِمِينَ ۚ وَيَفْعَلُ اللَّهُ مَا يَشَاءُ ۝٢٧
Yusabbitul laahul lazeena aamanoo bilqawlis saabiti fil hayaatid dunyaa wa fil Aakhirati wa yudillul laahuz zaalimeen; wa yaf`alul laahu maa yashaaa
📖 Tekkim Wolof
Yàlla dana dëgëral ña gëm ci wax ju dëggu, ci dundug àddina ak ca àllaaxira. Te Dana bàyyi tooñkat ya ca seen réer ga. Te Yàlla dana def lu ko soob.

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Ibrahima

25تُؤْتِي أُكُلَهَا كُلَّ حِينٍ بِإِذْنِ رَبِّهَا ۗ وَيَضْرِبُ اللَّهُ الْأَمْثَالَ لِلنَّاسِ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Muy joxi meññantam saa su nekk ci ndigalul Boroomam. Yàlla danay gaaral nit ñi ay léebu ndaxtelee ñu fàttaliku [seen Boroom].
26وَمَثَلُ كَلِمَةٍ خَبِيثَةٍ كَشَجَرَةٍ خَبِيثَةٍ اجْتُثَّتْ مِن فَوْقِ الْأَرْضِ مَا لَهَا مِن قَرَارٍ
Te itam, léeboo wax : “Baat bu bon dafa mel ni garab gu ñu buddee ci suuf te amul fu mu sax.”
27يُثَبِّتُ اللَّهُ الَّذِينَ آمَنُوا بِالْقَوْلِ الثَّابِتِ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَفِي الْآخِرَةِ ۖ وَيُضِلُّ اللَّهُ الظَّالِمِينَ ۚ وَيَفْعَلُ اللَّهُ مَا يَشَاءُ
Yàlla dana dëgëral ña gëm ci wax ju dëggu, ci dundug àddina ak ca àllaaxira. Te Dana bàyyi tooñkat ya ca seen réer ga. Te Yàlla dana def lu ko soob.
28۞ أَلَمْ تَرَ إِلَى الَّذِينَ بَدَّلُوا نِعْمَتَ اللَّهِ كُفْرًا وَأَحَلُّوا قَوْمَهُمْ دَارَ الْبَوَارِ
Ndax gisuloo ñay feye xéewali Yàlla ci di Ko weddi tey wàcce seenu nit ci kërug alkaande
29جَهَنَّمَ يَصْلَوْنَهَا ۖ وَبِئْسَ الْقَرَارُ
danañu séndal ci Safara ? Ndaw saxuwaay bu bon !
IbrahimaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Ibrahima 27

Simoore Ibrahima Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla dana dëgëral ña gëm ci wax ju dëggu, ci…

Simoore Aaya 27/52 — Ibrahima إبراهيم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ibrahima Dégg, Ibrahima Tekki, Ibrahima mp3, Ibrahima pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers