Al-Hijr · 9/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
إِنَّا نَحْنُ نَزَّلْنَا الذِّكْرَ وَإِنَّا لَهُ لَحَافِظُونَ ۝٩
Innaa Nahnu nazalnaz Zikra wa Innaa lahoo lahaa fizoon
📖 Tekkim Wolof
Nun noo wàcce Téere ba [Alxuraan] te Nun noo koy wattu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 7-11 — Al-Hijr

7لَّوْ مَا تَأْتِينَا بِالْمَلَائِكَةِ إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Lu teewoon nga indil nu ay Malaaka, ndegam bokk nga ca ñu dëggu ña ? ”
8مَا نُنَزِّلُ الْمَلَائِكَةَ إِلَّا بِالْحَقِّ وَمَا كَانُوا إِذًا مُّنظَرِينَ
Nun dunu wàcce ay Malaaka lu dul ci dëgg (gu Nu doxal mu jeex) ; te kon dungeen doon ñu ñuy muñandiku ab diir.
9إِنَّا نَحْنُ نَزَّلْنَا الذِّكْرَ وَإِنَّا لَهُ لَحَافِظُونَ
Nun noo wàcce Téere ba [Alxuraan] te Nun noo koy wattu.
10وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ فِي شِيَعِ الْأَوَّلِينَ
Yónni Nanu ci lu la jiitu ay Yonent ca kurél yu njëkk ya.
11وَمَا يَأْتِيهِم مِّن رَّسُولٍ إِلَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Te ab Yonent daawuleen dikkal te yéjj wuñu (ñaawal).
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Hijr 9

Simoore Al-Hijr Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun noo wàcce Téere ba [Alxuraan] te Nun noo koy…

Simoore Aaya 9/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers