Al-Hijr · 8/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
مَا نُنَزِّلُ الْمَلَائِكَةَ إِلَّا بِالْحَقِّ وَمَا كَانُوا إِذًا مُّنظَرِينَ ٨
Transliteration
Maa nunazzilul malaaa`i kata illaa bilhaqqi wa maa kaanooo izam munzareen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nun dunu wàcce ay Malaaka lu dul ci dëgg (gu Nu doxal mu jeex) ; te kon dungeen doon ñu ñuy muñandiku ab diir.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 6-10 — Al-Hijr
6وَقَالُوا يَا أَيُّهَا الَّذِي نُزِّلَ عَلَيْهِ الذِّكْرُ إِنَّكَ لَمَجْنُونٌ
Ñu naan leen : “Yaw mii, wàcceef na ci yéen Téere ba, yaw dof tigi nga !
7لَّوْ مَا تَأْتِينَا بِالْمَلَائِكَةِ إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Lu teewoon nga indil nu ay Malaaka, ndegam bokk nga ca ñu dëggu ña ? ”
8مَا نُنَزِّلُ الْمَلَائِكَةَ إِلَّا بِالْحَقِّ وَمَا كَانُوا إِذًا مُّنظَرِينَ
Nun dunu wàcce ay Malaaka lu dul ci dëgg (gu Nu doxal mu jeex) ; te kon dungeen doon ñu ñuy muñandiku ab diir.
9إِنَّا نَحْنُ نَزَّلْنَا الذِّكْرَ وَإِنَّا لَهُ لَحَافِظُونَ
Nun noo wàcce Téere ba [Alxuraan] te Nun noo koy wattu.
10وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ فِي شِيَعِ الْأَوَّلِينَ
Yónni Nanu ci lu la jiitu ay Yonent ca kurél yu njëkk ya.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
8Aaya
Tekki — Al-Hijr 8
Simoore Al-Hijr Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun dunu wàcce ay Malaaka lu dul ci dëgg (gu…Simoore Aaya 8/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








