Al-Kahf · 1/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي أَنزَلَ عَلَىٰ عَبْدِهِ الْكِتَابَ وَلَمْ يَجْعَل لَّهُ عِوَجًا ۜ ١
Transliteration
Alhamdu lillaahil lazeee anzala `alaa `abdihil kitaaba wa lam yaj`al lahoo `iwajaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Gépp cant ñeel na Yàlla mi wàcce Téere ba ca jaamam [Muhammad], te defalu ko genn logg-logg !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 1-3 — Al-Kahf
1الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي أَنزَلَ عَلَىٰ عَبْدِهِ الْكِتَابَ وَلَمْ يَجْعَل لَّهُ عِوَجًا ۜ
Gépp cant ñeel na Yàlla mi wàcce Téere ba ca jaamam [Muhammad], te defalu ko genn logg-logg !
2قَيِّمًا لِّيُنذِرَ بَأْسًا شَدِيدًا مِّن لَّدُنْهُ وَيُبَشِّرَ الْمُؤْمِنِينَ الَّذِينَ يَعْمَلُونَ الصَّالِحَاتِ أَنَّ لَهُمْ أَجْرًا حَسَنًا
Muy lu jub xocc, di xuppe ci mbugal mu tar lu jóge ci Moom ak di bégle way-gëm ñay jëf jëf yu yiw, ci ne ñoom am nañu pey gu rafet.
3مَّاكِثِينَ فِيهِ أَبَدًا
te dañu cay sax dapet dàkk ba fàwwu,
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
1Aaya
Tekki — Al-Kahf 1
Simoore Al-Kahf Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Gépp cant ñeel na Yàlla mi wàcce Téere ba ca…Simoore Aaya 1/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








