Al-Kahf · 2/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
قَيِّمًا لِّيُنذِرَ بَأْسًا شَدِيدًا مِّن لَّدُنْهُ وَيُبَشِّرَ الْمُؤْمِنِينَ الَّذِينَ يَعْمَلُونَ الصَّالِحَاتِ أَنَّ لَهُمْ أَجْرًا حَسَنًا ۝٢
Qaiyimal liyunzira baasan shadeedam mil ladunhu wa yubashshiral mu`mineenal lazeena ya`maloonas saalihaati anna lahum ajran hasanaa
📖 Tekkim Wolof
Muy lu jub xocc, di xuppe ci mbugal mu tar lu jóge ci Moom ak di bégle way-gëm ñay jëf jëf yu yiw, ci ne ñoom am nañu pey gu rafet.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-4 — Simoore Al-Kahf

1الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي أَنزَلَ عَلَىٰ عَبْدِهِ الْكِتَابَ وَلَمْ يَجْعَل لَّهُ عِوَجًا ۜ
Gépp cant ñeel na Yàlla mi wàcce Téere ba ca jaamam [Muhammad], te defalu ko genn logg-logg !
2قَيِّمًا لِّيُنذِرَ بَأْسًا شَدِيدًا مِّن لَّدُنْهُ وَيُبَشِّرَ الْمُؤْمِنِينَ الَّذِينَ يَعْمَلُونَ الصَّالِحَاتِ أَنَّ لَهُمْ أَجْرًا حَسَنًا
Muy lu jub xocc, di xuppe ci mbugal mu tar lu jóge ci Moom ak di bégle way-gëm ñay jëf jëf yu yiw, ci ne ñoom am nañu pey gu rafet.
3مَّاكِثِينَ فِيهِ أَبَدًا
te dañu cay sax dapet dàkk ba fàwwu,
4وَيُنذِرَ الَّذِينَ قَالُوا اتَّخَذَ اللَّهُ وَلَدًا
te muy xupp ñay wax naan : “Yàlla am na doom.”
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Al-Kahf 2

Simoore Al-Kahf Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muy lu jub xocc, di xuppe ci mbugal mu tar…

Simoore Aaya 2/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers