Al-Kahf · 7/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
إِنَّا جَعَلْنَا مَا عَلَى الْأَرْضِ زِينَةً لَّهَا لِنَبْلُوَهُمْ أَيُّهُمْ أَحْسَنُ عَمَلًا ٧
Transliteration
Innaa ja`alnaa ma `alal ardi zeenatal lahaa linabluwahum ayyuhum ahsanu `amalaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nun noo def ci suuf si taaram ngir nattu leen, [ba xam] ña ca gën a rafet jëf.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 5-9 — Al-Kahf
5مَّا لَهُم بِهِ مِنْ عِلْمٍ وَلَا لِآبَائِهِمْ ۚ كَبُرَتْ كَلِمَةً تَخْرُجُ مِنْ أَفْوَاهِهِمْ ۚ إِن يَقُولُونَ إِلَّا كَذِبًا
Amuñu ci loolu benn xam-xam, Seeni baay it [amuñu ko ca]. Muy wax ju réy ju génne ci seen gémmiñ! Waxuñu lu dul fen.
6فَلَعَلَّكَ بَاخِعٌ نَّفْسَكَ عَلَىٰ آثَارِهِمْ إِن لَّمْ يُؤْمِنُوا بِهَٰذَا الْحَدِيثِ أَسَفًا
Te xéy-na nga lor sa bopp ci naqarlu ngir li ñu ñàkk a gëm kàddu ga !
7إِنَّا جَعَلْنَا مَا عَلَى الْأَرْضِ زِينَةً لَّهَا لِنَبْلُوَهُمْ أَيُّهُمْ أَحْسَنُ عَمَلًا
Nun noo def ci suuf si taaram ngir nattu leen, [ba xam] ña ca gën a rafet jëf.
8وَإِنَّا لَجَاعِلُونَ مَا عَلَيْهَا صَعِيدًا جُرُزًا
De Dananu def li nekk ci kawam nekk di pàkk bu wow koŋŋ.
9أَمْ حَسِبْتَ أَنَّ أَصْحَابَ الْكَهْفِ وَالرَّقِيمِ كَانُوا مِنْ آيَاتِنَا عَجَبًا
Ndax amuloo njort ci ne, ñoñ-xunt ma ak ñoñ-mbind ma [téere ba] bokkoon nañu ca Sunuy kéemaan yu doy waar [yéeme] ?
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
7Aaya
Tekki — Al-Kahf 7
Simoore Al-Kahf Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun noo def ci suuf si taaram ngir nattu leen,…Simoore Aaya 7/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








