Al-Kahf · 8/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
وَإِنَّا لَجَاعِلُونَ مَا عَلَيْهَا صَعِيدًا جُرُزًا ۝٨
Wa innaa lajaa `iloona maa `alaihaa sa`aeedan juruzaa
📖 Tekkim Wolof
De Dananu def li nekk ci kawam nekk di pàkk bu wow koŋŋ.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 6-10 — Simoore Al-Kahf

6فَلَعَلَّكَ بَاخِعٌ نَّفْسَكَ عَلَىٰ آثَارِهِمْ إِن لَّمْ يُؤْمِنُوا بِهَٰذَا الْحَدِيثِ أَسَفًا
Te xéy-na nga lor sa bopp ci naqarlu ngir li ñu ñàkk a gëm kàddu ga !
7إِنَّا جَعَلْنَا مَا عَلَى الْأَرْضِ زِينَةً لَّهَا لِنَبْلُوَهُمْ أَيُّهُمْ أَحْسَنُ عَمَلًا
Nun noo def ci suuf si taaram ngir nattu leen, [ba xam] ña ca gën a rafet jëf.
8وَإِنَّا لَجَاعِلُونَ مَا عَلَيْهَا صَعِيدًا جُرُزًا
De Dananu def li nekk ci kawam nekk di pàkk bu wow koŋŋ.
9أَمْ حَسِبْتَ أَنَّ أَصْحَابَ الْكَهْفِ وَالرَّقِيمِ كَانُوا مِنْ آيَاتِنَا عَجَبًا
Ndax amuloo njort ci ne, ñoñ-xunt ma ak ñoñ-mbind ma [téere ba] bokkoon nañu ca Sunuy kéemaan yu doy waar [yéeme] ?
10إِذْ أَوَى الْفِتْيَةُ إِلَى الْكَهْفِ فَقَالُوا رَبَّنَا آتِنَا مِن لَّدُنكَ رَحْمَةً وَهَيِّئْ لَنَا مِنْ أَمْرِنَا رَشَدًا
[Fàttalikul] ba waxamaande ya làqoo ca xunt ma, te ñu waxoon ne : “Yaw sunu Boroom, may nu yërmaande ju bawoo ci yaw; te nga yéwénal sunuy mbir mu nekk cig njub”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-Kahf 8

Simoore Al-Kahf Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : De Dananu def li nekk ci kawam nekk di pàkk…

Simoore Aaya 8/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers