Taha · 25/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
قَالَ رَبِّ اشْرَحْ لِي صَدْرِي ۝٢٥
Qaala Rabbish rah lee sadree
📖 Tekkim Wolof
[Muusaa] ne ko : “Yaw sama Boroom, leeralal ma sama dënn [mën a dékku lu bari],

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 23-27 — Simoore Taha

23لِنُرِيَكَ مِنْ آيَاتِنَا الْكُبْرَى
[Lii lépp] Danu la koo waajale ngir won la ci Sunu kéemtaan yu màgg yi.
24اذْهَبْ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ إِنَّهُ طَغَىٰ
Demal ca Firawna, moom dafa beew.
25قَالَ رَبِّ اشْرَحْ لِي صَدْرِي
[Muusaa] ne ko : “Yaw sama Boroom, leeralal ma sama dënn [mën a dékku lu bari],
26وَيَسِّرْ لِي أَمْرِي
te nga yombalal ma sama soloo sii,
27وَاحْلُلْ عُقْدَةً مِّن لِّسَانِي
te nga leeral samaw làmmiñ,
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Taha 25

Simoore Taha Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Muusaa] ne ko : “Yaw sama Boroom, leeralal ma sama…

Simoore Aaya 25/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers