Al-Anbiya · 44/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
بَلْ مَتَّعْنَا هَٰؤُلَاءِ وَآبَاءَهُمْ حَتَّىٰ طَالَ عَلَيْهِمُ الْعُمُرُ ۗ أَفَلَا يَرَوْنَ أَنَّا نَأْتِي الْأَرْضَ نَنقُصُهَا مِنْ أَطْرَافِهَا ۚ أَفَهُمُ الْغَالِبُونَ ۝٤٤
Bal matta`naa haaa`ulaaa`i wa aabaaa`ahum hattaa taala `alaihimul `umur; afalaa yarawna anna naatil arda nanqusuhaa min atraafihaa; afahumul ghaaliboon
📖 Tekkim Wolof
Li am mooy, xéewalal Nanu ñooñook seeni baay ba seenug dund yàgg ci ñoom. Waaye ndax dañoo gisul ne wàññi Nanu suuf si cig wàññi ay catam ? Moo ndax ñoom ñooy not ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 42-46 — Simoore Al-Anbiya

42قُلْ مَن يَكْلَؤُكُم بِاللَّيْلِ وَالنَّهَارِ مِنَ الرَّحْمَٰنِ ۗ بَلْ هُمْ عَن ذِكْرِ رَبِّهِم مُّعْرِضُونَ
Neel : “Kan moo leen mëna yërëm guddi ak bëccëg ci Yërëmaakoon bi ? ” Teewul ñoom ñangay dëddoo tuddu seen Boroom [Fàttaliku Ko].
43أَمْ لَهُمْ آلِهَةٌ تَمْنَعُهُم مِّن دُونِنَا ۚ لَا يَسْتَطِيعُونَ نَصْرَ أَنفُسِهِمْ وَلَا هُم مِّنَّا يُصْحَبُونَ
Am dañoo am ay yàlla ju dul Nun, ju leen di mën a aar ? Duñu mën a dimbali seen bopp, te deefuleen mën a xettali ci Nun.
44بَلْ مَتَّعْنَا هَٰؤُلَاءِ وَآبَاءَهُمْ حَتَّىٰ طَالَ عَلَيْهِمُ الْعُمُرُ ۗ أَفَلَا يَرَوْنَ أَنَّا نَأْتِي الْأَرْضَ نَنقُصُهَا مِنْ أَطْرَافِهَا ۚ أَفَهُمُ الْغَالِبُونَ
Li am mooy, xéewalal Nanu ñooñook seeni baay ba seenug dund yàgg ci ñoom. Waaye ndax dañoo gisul ne wàññi Nanu suuf si cig wàññi ay catam ? Moo ndax ñoom ñooy not ?
45قُلْ إِنَّمَا أُنذِرُكُم بِالْوَحْيِ ۚ وَلَا يَسْمَعُ الصُّمُّ الدُّعَاءَ إِذَا مَا يُنذَرُونَ
Neel : “Defuma lu dul ragal-loo leen li ñu ma soloo”. Waaye ay tëx duñu dégg wooteb ña leen di waar.
46وَلَئِن مَّسَّتْهُمْ نَفْحَةٌ مِّنْ عَذَابِ رَبِّكَ لَيَقُولُنَّ يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Te bu leen lu tuuti daloon ci sa ndigalu Boroom, ñu dellu tàmbalee wax naan : “Ngalla nun ! Nun ay tooñkat lanu woon”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
44Aaya

Tekki — Al-Anbiya 44

Simoore Al-Anbiya Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li am mooy, xéewalal Nanu ñooñook seeni baay ba seenug…

Simoore Aaya 44/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers