Al-Anbiya · 45/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
قُلْ إِنَّمَا أُنذِرُكُم بِالْوَحْيِ ۚ وَلَا يَسْمَعُ الصُّمُّ الدُّعَاءَ إِذَا مَا يُنذَرُونَ ۝٤٥
Qul innamaaa unzirukum bilwahyi; wa laa yasma`us summud du`aaa`a izaa maa yunzaroon
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Defuma lu dul ragal-loo leen li ñu ma soloo”. Waaye ay tëx duñu dégg wooteb ña leen di waar.

🎧 Dégg


📜 Aaya 43-47 — Simoore Al-Anbiya

43أَمْ لَهُمْ آلِهَةٌ تَمْنَعُهُم مِّن دُونِنَا ۚ لَا يَسْتَطِيعُونَ نَصْرَ أَنفُسِهِمْ وَلَا هُم مِّنَّا يُصْحَبُونَ
Am dañoo am ay yàlla ju dul Nun, ju leen di mën a aar ? Duñu mën a dimbali seen bopp, te deefuleen mën a xettali ci Nun.
44بَلْ مَتَّعْنَا هَٰؤُلَاءِ وَآبَاءَهُمْ حَتَّىٰ طَالَ عَلَيْهِمُ الْعُمُرُ ۗ أَفَلَا يَرَوْنَ أَنَّا نَأْتِي الْأَرْضَ نَنقُصُهَا مِنْ أَطْرَافِهَا ۚ أَفَهُمُ الْغَالِبُونَ
Li am mooy, xéewalal Nanu ñooñook seeni baay ba seenug dund yàgg ci ñoom. Waaye ndax dañoo gisul ne wàññi Nanu suuf si cig wàññi ay catam ? Moo ndax ñoom ñooy not ?
45قُلْ إِنَّمَا أُنذِرُكُم بِالْوَحْيِ ۚ وَلَا يَسْمَعُ الصُّمُّ الدُّعَاءَ إِذَا مَا يُنذَرُونَ
Neel : “Defuma lu dul ragal-loo leen li ñu ma soloo”. Waaye ay tëx duñu dégg wooteb ña leen di waar.
46وَلَئِن مَّسَّتْهُمْ نَفْحَةٌ مِّنْ عَذَابِ رَبِّكَ لَيَقُولُنَّ يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Te bu leen lu tuuti daloon ci sa ndigalu Boroom, ñu dellu tàmbalee wax naan : “Ngalla nun ! Nun ay tooñkat lanu woon”.
47وَنَضَعُ الْمَوَازِينَ الْقِسْطَ لِيَوْمِ الْقِيَامَةِ فَلَا تُظْلَمُ نَفْسٌ شَيْئًا ۖ وَإِن كَانَ مِثْقَالَ حَبَّةٍ مِّنْ خَرْدَلٍ أَتَيْنَا بِهَا ۗ وَكَفَىٰ بِنَا حَاسِبِينَ
Dana tëral màndaxe mu maandu ca Bis-pénc ba. Te deesul tooñ benn bakkan ci dara, doonte lu tollu ni pepp bàkket, Dananu ko indi. Te aka mën a wàññi.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Al-Anbiya 45

Simoore Al-Anbiya Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Defuma lu dul ragal-loo leen li ñu ma…

Simoore Aaya 45/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers