Al-Anbiya · 46/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
وَلَئِن مَّسَّتْهُمْ نَفْحَةٌ مِّنْ عَذَابِ رَبِّكَ لَيَقُولُنَّ يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ ۝٤٦
Wa la`im massat hum nafhatum min `azaabi Rabbika la yaqoolunna yaawailanaaa innnaa kunnaa zaalimeen
📖 Tekkim Wolof
Te bu leen lu tuuti daloon ci sa ndigalu Boroom, ñu dellu tàmbalee wax naan : “Ngalla nun ! Nun ay tooñkat lanu woon”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 44-48 — Simoore Al-Anbiya

44بَلْ مَتَّعْنَا هَٰؤُلَاءِ وَآبَاءَهُمْ حَتَّىٰ طَالَ عَلَيْهِمُ الْعُمُرُ ۗ أَفَلَا يَرَوْنَ أَنَّا نَأْتِي الْأَرْضَ نَنقُصُهَا مِنْ أَطْرَافِهَا ۚ أَفَهُمُ الْغَالِبُونَ
Li am mooy, xéewalal Nanu ñooñook seeni baay ba seenug dund yàgg ci ñoom. Waaye ndax dañoo gisul ne wàññi Nanu suuf si cig wàññi ay catam ? Moo ndax ñoom ñooy not ?
45قُلْ إِنَّمَا أُنذِرُكُم بِالْوَحْيِ ۚ وَلَا يَسْمَعُ الصُّمُّ الدُّعَاءَ إِذَا مَا يُنذَرُونَ
Neel : “Defuma lu dul ragal-loo leen li ñu ma soloo”. Waaye ay tëx duñu dégg wooteb ña leen di waar.
46وَلَئِن مَّسَّتْهُمْ نَفْحَةٌ مِّنْ عَذَابِ رَبِّكَ لَيَقُولُنَّ يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Te bu leen lu tuuti daloon ci sa ndigalu Boroom, ñu dellu tàmbalee wax naan : “Ngalla nun ! Nun ay tooñkat lanu woon”.
47وَنَضَعُ الْمَوَازِينَ الْقِسْطَ لِيَوْمِ الْقِيَامَةِ فَلَا تُظْلَمُ نَفْسٌ شَيْئًا ۖ وَإِن كَانَ مِثْقَالَ حَبَّةٍ مِّنْ خَرْدَلٍ أَتَيْنَا بِهَا ۗ وَكَفَىٰ بِنَا حَاسِبِينَ
Dana tëral màndaxe mu maandu ca Bis-pénc ba. Te deesul tooñ benn bakkan ci dara, doonte lu tollu ni pepp bàkket, Dananu ko indi. Te aka mën a wàññi.
48وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَىٰ وَهَارُونَ الْفُرْقَانَ وَضِيَاءً وَذِكْرًا لِّلْمُتَّقِينَ
Joxoon Nanu Muusaa ak Aaruuna Tawreet ak leeraay ak fàtttaliku ngir ña ragal Yàlla,
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Al-Anbiya 46

Simoore Al-Anbiya Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te bu leen lu tuuti daloon ci sa ndigalu Boroom,…

Simoore Aaya 46/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers