An-Naml · 12/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
وَأَدْخِلْ يَدَكَ فِي جَيْبِكَ تَخْرُجْ بَيْضَاءَ مِنْ غَيْرِ سُوءٍ ۖ فِي تِسْعِ آيَاتٍ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَقَوْمِهِ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ ١٢
Transliteration
Wa adkhil yadaka fee jaibika takhruj baidaaa`a min ghairisooo`in feetis`i Aayaatin ilaa Fir`awna wa qawmih; innahum kaanoo qawman faasiqeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Sóobal sa loxo ci sa mbubbu. Dana génn weex tàll - muy benn ci juróom-ñeenti kéemaan yi jëm ca Firawna ak u nitam, ñoom ay saay-saay lañu woon”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 10-14 — An-Naml
10وَأَلْقِ عَصَاكَ ۚ فَلَمَّا رَآهَا تَهْتَزُّ كَأَنَّهَا جَانٌّ وَلَّىٰ مُدْبِرًا وَلَمْ يُعَقِّبْ ۚ يَا مُوسَىٰ لَا تَخَفْ إِنِّي لَا يَخَافُ لَدَيَّ الْمُرْسَلُونَ
Te : “Nanga sànni sa yet wi”. Ba mu ko gisee muy yëngantu mel ni jaan, mu tiit bëgg a daw. “Éy yaw Muusaa. Bul ragal, Yonent yi duñu ragal ci sama wet.
11إِلَّا مَن ظَلَمَ ثُمَّ بَدَّلَ حُسْنًا بَعْدَ سُوءٍ فَإِنِّي غَفُورٌ رَّحِيمٌ
u dul kuy tooñ te ginnaaw ba mu soppi ñaawtéef ak lu rafet... naka Man Jéggalaakoon laa, Jaglewaakoon laa”.
12وَأَدْخِلْ يَدَكَ فِي جَيْبِكَ تَخْرُجْ بَيْضَاءَ مِنْ غَيْرِ سُوءٍ ۖ فِي تِسْعِ آيَاتٍ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَقَوْمِهِ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ
Sóobal sa loxo ci sa mbubbu. Dana génn weex tàll - muy benn ci juróom-ñeenti kéemaan yi jëm ca Firawna ak u nitam, ñoom ay saay-saay lañu woon”.
13فَلَمَّا جَاءَتْهُمْ آيَاتُنَا مُبْصِرَةً قَالُوا هَٰذَا سِحْرٌ مُّبِينٌ
Ndax ba leen Sunuy laaya dikkalee, leer nàññ, dañoo wax ne : “Lii ag njibar la gu bir ! ”
14وَجَحَدُوا بِهَا وَاسْتَيْقَنَتْهَا أَنفُسُهُمْ ظُلْمًا وَعُلُوًّا ۚ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُفْسِدِينَ
Weddi nañu ko waaye seeni xol gëm na ko, xanaa kay rëy a leen jàpp. Xoolal nag yàqkat naka la ñuy mujje.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
12Aaya
Tekki — An-Naml 12
Simoore An-Naml Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sóobal sa loxo ci sa mbubbu. Dana génn weex tàll…Simoore Aaya 12/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








