An-Naml · 13/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
فَلَمَّا جَاءَتْهُمْ آيَاتُنَا مُبْصِرَةً قَالُوا هَٰذَا سِحْرٌ مُّبِينٌ ۝١٣
Falammaa jaaa`at hum Aayaatunaa mubsiratan qaaloo haazaa sihrum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Ndax ba leen Sunuy laaya dikkalee, leer nàññ, dañoo wax ne : “Lii ag njibar la gu bir ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — An-Naml

11إِلَّا مَن ظَلَمَ ثُمَّ بَدَّلَ حُسْنًا بَعْدَ سُوءٍ فَإِنِّي غَفُورٌ رَّحِيمٌ
u dul kuy tooñ te ginnaaw ba mu soppi ñaawtéef ak lu rafet... naka Man Jéggalaakoon laa, Jaglewaakoon laa”.
12وَأَدْخِلْ يَدَكَ فِي جَيْبِكَ تَخْرُجْ بَيْضَاءَ مِنْ غَيْرِ سُوءٍ ۖ فِي تِسْعِ آيَاتٍ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَقَوْمِهِ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ
Sóobal sa loxo ci sa mbubbu. Dana génn weex tàll - muy benn ci juróom-ñeenti kéemaan yi jëm ca Firawna ak u nitam, ñoom ay saay-saay lañu woon”.
13فَلَمَّا جَاءَتْهُمْ آيَاتُنَا مُبْصِرَةً قَالُوا هَٰذَا سِحْرٌ مُّبِينٌ
Ndax ba leen Sunuy laaya dikkalee, leer nàññ, dañoo wax ne : “Lii ag njibar la gu bir ! ”
14وَجَحَدُوا بِهَا وَاسْتَيْقَنَتْهَا أَنفُسُهُمْ ظُلْمًا وَعُلُوًّا ۚ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُفْسِدِينَ
Weddi nañu ko waaye seeni xol gëm na ko, xanaa kay rëy a leen jàpp. Xoolal nag yàqkat naka la ñuy mujje.
15وَلَقَدْ آتَيْنَا دَاوُودَ وَسُلَيْمَانَ عِلْمًا ۖ وَقَالَا الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي فَضَّلَنَا عَلَىٰ كَثِيرٍ مِّنْ عِبَادِهِ الْمُؤْمِنِينَ
Joxoon Nanu Daawuda ak Suleymaan xam-xam ; ñuy wax naan : “Xeeti cant yépp ñeel na Yàlla, Moom mi nu gënal ci kaw nit ñu bari ñi bokkoon ci jaamam ñi gëm”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — An-Naml 13

Simoore An-Naml Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax ba leen Sunuy laaya dikkalee, leer nàññ, dañoo wax…

Simoore Aaya 13/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers