An-Naml · 26/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ رَبُّ الْعَرْشِ الْعَظِيمِ ۩ ۝٢٦
Allaahu laaa ilaaha illaa Huwa Rabbul `Arshil Azeem
📖 Tekkim Wolof
[Cëy] Yàlla ! Jeneen yàlla amul ju dul Moom, Mooy boroom gàngunaay [Aras] gu màgg ga.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 24-28 — Simoore An-Naml

24وَجَدتُّهَا وَقَوْمَهَا يَسْجُدُونَ لِلشَّمْسِ مِن دُونِ اللَّهِ وَزَيَّنَ لَهُمُ الشَّيْطَانُ أَعْمَالَهُمْ فَصَدَّهُمْ عَنِ السَّبِيلِ فَهُمْ لَا يَهْتَدُونَ
Fekk naa ko it mook aw nitam ñuy jaamu jant bi bàyyi Yàlla. Séytaane taaralal leen jëf jooju, wëlbati leen ñu dëddu yoonu Yàlla ba gëmuñu.
25أَلَّا يَسْجُدُوا لِلَّهِ الَّذِي يُخْرِجُ الْخَبْءَ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَيَعْلَمُ مَا تُخْفُونَ وَمَا تُعْلِنُونَ
Moo ndax duñu jaamu Yàlla Miy génne li nëbbu ci asamaan yeek suuf si, te Moo xam li ngeen di nëbb ak li ngeen di feeñal ?
26اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ رَبُّ الْعَرْشِ الْعَظِيمِ ۩
[Cëy] Yàlla ! Jeneen yàlla amul ju dul Moom, Mooy boroom gàngunaay [Aras] gu màgg ga.
27۞ قَالَ سَنَنظُرُ أَصَدَقْتَ أَمْ كُنتَ مِنَ الْكَاذِبِينَ
Suleymaan ne ko : “Dananu xool ndax wax nga dëgg walla dangay fen.
28اذْهَب بِّكِتَابِي هَٰذَا فَأَلْقِهْ إِلَيْهِمْ ثُمَّ تَوَلَّ عَنْهُمْ فَانظُرْ مَاذَا يَرْجِعُونَ
Jëlal sama bataaxal bii ; boo demee nga sànni leen ko ; te dëppal xool ba xam na ñuy def.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — An-Naml 26

Simoore An-Naml Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Cëy] Yàlla ! Jeneen yàlla amul ju dul Moom, Mooy…

Simoore Aaya 26/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers