An-Naml · 30/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
إِنَّهُ مِن سُلَيْمَانَ وَإِنَّهُ بِسْمِ اللَّهِ الرَّحْمَٰنِ الرَّحِيمِ ۝٣٠
Innahoo min Sulaimaana wa innahoo bismil laahir Rahmaanir Raheem
📖 Tekkim Wolof
Mi ngi bawoo ca Suleymaan : “Ci turu Yàlla la Miy Yërëmaakoon, di Jaglewaakoon,

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — An-Naml

28اذْهَب بِّكِتَابِي هَٰذَا فَأَلْقِهْ إِلَيْهِمْ ثُمَّ تَوَلَّ عَنْهُمْ فَانظُرْ مَاذَا يَرْجِعُونَ
Jëlal sama bataaxal bii ; boo demee nga sànni leen ko ; te dëppal xool ba xam na ñuy def.
29قَالَتْ يَا أَيُّهَا الْمَلَأُ إِنِّي أُلْقِيَ إِلَيَّ كِتَابٌ كَرِيمٌ
Buur ba [Balxiis] ne leen : "Kilifay dëkk bi ! Man dey, sànni nañu ma bataaxal bu tedd.
30إِنَّهُ مِن سُلَيْمَانَ وَإِنَّهُ بِسْمِ اللَّهِ الرَّحْمَٰنِ الرَّحِيمِ
Mi ngi bawoo ca Suleymaan : “Ci turu Yàlla la Miy Yërëmaakoon, di Jaglewaakoon,
31أَلَّا تَعْلُوا عَلَيَّ وَأْتُونِي مُسْلِمِينَ
Buleen rëy-rëylu ci sama kaw te ñëwleen jébbalusi seen bopp”.
32قَالَتْ يَا أَيُّهَا الْمَلَأُ أَفْتُونِي فِي أَمْرِي مَا كُنتُ قَاطِعَةً أَمْرًا حَتَّىٰ تَشْهَدُونِ
Buur ba ne gàngooram : "Ubbileen sama bopp ci mbir mii : masumaa dugg ci menn mbir te joxewuleen ci xalaat”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — An-Naml 30

Simoore An-Naml Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mi ngi bawoo ca Suleymaan : “Ci turu Yàlla la…

Simoore Aaya 30/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers