Al-Qasas · 5/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
وَنُرِيدُ أَن نَّمُنَّ عَلَى الَّذِينَ اسْتُضْعِفُوا فِي الْأَرْضِ وَنَجْعَلَهُمْ أَئِمَّةً وَنَجْعَلَهُمُ الْوَارِثِينَ ۝٥
Wa nureedu an namunna `alal lazeenas tud`ifoo fil ardi wa naj`alahum a`immatanw wa naj`alahumul waariseen
📖 Tekkim Wolof
Nun Yàlla nammoom Nanoo dooleel ña néewoon doole ca réew ma, Nu bëgg leen a def ay njiit, def itam [ñu mujj fa],

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-Qasas

3نَتْلُو عَلَيْكَ مِن نَّبَإِ مُوسَىٰ وَفِرْعَوْنَ بِالْحَقِّ لِقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Dananu la nettali ci xibaari Muusaa ak Frhawna ci dëgg, muy lu ñeel aw nit ñu gëm.
4إِنَّ فِرْعَوْنَ عَلَا فِي الْأَرْضِ وَجَعَلَ أَهْلَهَا شِيَعًا يَسْتَضْعِفُ طَائِفَةً مِّنْهُمْ يُذَبِّحُ أَبْنَاءَهُمْ وَيَسْتَحْيِي نِسَاءَهُمْ ۚ إِنَّهُ كَانَ مِنَ الْمُفْسِدِينَ
Firawna dadoon kawe-kawelu ci suuf si ; féewale waa réew ma, di jaamuloo ab kurél ci ñoom : ak a réndi seeni doom yu góor, di bàyyi jigéen ña. Moom Firawna yàqkat la woon.
5وَنُرِيدُ أَن نَّمُنَّ عَلَى الَّذِينَ اسْتُضْعِفُوا فِي الْأَرْضِ وَنَجْعَلَهُمْ أَئِمَّةً وَنَجْعَلَهُمُ الْوَارِثِينَ
Nun Yàlla nammoom Nanoo dooleel ña néewoon doole ca réew ma, Nu bëgg leen a def ay njiit, def itam [ñu mujj fa],
6وَنُمَكِّنَ لَهُمْ فِي الْأَرْضِ وَنُرِيَ فِرْعَوْنَ وَهَامَانَ وَجُنُودَهُمَا مِنْهُم مَّا كَانُوا يَحْذَرُونَ
may leen kàttan, ak it wonaale Firawna ak Haamaan ak seeni gàngoor la ñu daan moytandiku.
7وَأَوْحَيْنَا إِلَىٰ أُمِّ مُوسَىٰ أَنْ أَرْضِعِيهِ ۖ فَإِذَا خِفْتِ عَلَيْهِ فَأَلْقِيهِ فِي الْيَمِّ وَلَا تَخَافِي وَلَا تَحْزَنِي ۖ إِنَّا رَادُّوهُ إِلَيْكِ وَجَاعِلُوهُ مِنَ الْمُرْسَلِينَ
Soloo Nanu yaayu Muusaa ne ko : “Nàmpal ko. Te soo tiitee ciy mbiram, sànni ko ci dex gi. Bul ragal, bul jàq : Dananu la ko delloosil mu bokk ca Yonent ya”.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Qasas 5

Simoore Al-Qasas Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun Yàlla nammoom Nanoo dooleel ña néewoon doole ca réew…

Simoore Aaya 5/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers