Al-Qasas · 4/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
إِنَّ فِرْعَوْنَ عَلَا فِي الْأَرْضِ وَجَعَلَ أَهْلَهَا شِيَعًا يَسْتَضْعِفُ طَائِفَةً مِّنْهُمْ يُذَبِّحُ أَبْنَاءَهُمْ وَيَسْتَحْيِي نِسَاءَهُمْ ۚ إِنَّهُ كَانَ مِنَ الْمُفْسِدِينَ ۝٤
Inna Fir`awna `alaa fil ardi wa ja`ala ahlahaa shiya`ai yastad`ifu taaa`ifatam minhum yuzabbihu abnaaa`ahum wa yastahyee nisaaa`ahum; innahoo kaana minal mufsideen
📖 Tekkim Wolof
Firawna dadoon kawe-kawelu ci suuf si ; féewale waa réew ma, di jaamuloo ab kurél ci ñoom : ak a réndi seeni doom yu góor, di bàyyi jigéen ña. Moom Firawna yàqkat la woon.

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Qasas

2تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ الْمُبِينِ
Lii mooy laayay Téere ba Nu biral.
3نَتْلُو عَلَيْكَ مِن نَّبَإِ مُوسَىٰ وَفِرْعَوْنَ بِالْحَقِّ لِقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Dananu la nettali ci xibaari Muusaa ak Frhawna ci dëgg, muy lu ñeel aw nit ñu gëm.
4إِنَّ فِرْعَوْنَ عَلَا فِي الْأَرْضِ وَجَعَلَ أَهْلَهَا شِيَعًا يَسْتَضْعِفُ طَائِفَةً مِّنْهُمْ يُذَبِّحُ أَبْنَاءَهُمْ وَيَسْتَحْيِي نِسَاءَهُمْ ۚ إِنَّهُ كَانَ مِنَ الْمُفْسِدِينَ
Firawna dadoon kawe-kawelu ci suuf si ; féewale waa réew ma, di jaamuloo ab kurél ci ñoom : ak a réndi seeni doom yu góor, di bàyyi jigéen ña. Moom Firawna yàqkat la woon.
5وَنُرِيدُ أَن نَّمُنَّ عَلَى الَّذِينَ اسْتُضْعِفُوا فِي الْأَرْضِ وَنَجْعَلَهُمْ أَئِمَّةً وَنَجْعَلَهُمُ الْوَارِثِينَ
Nun Yàlla nammoom Nanoo dooleel ña néewoon doole ca réew ma, Nu bëgg leen a def ay njiit, def itam [ñu mujj fa],
6وَنُمَكِّنَ لَهُمْ فِي الْأَرْضِ وَنُرِيَ فِرْعَوْنَ وَهَامَانَ وَجُنُودَهُمَا مِنْهُم مَّا كَانُوا يَحْذَرُونَ
may leen kàttan, ak it wonaale Firawna ak Haamaan ak seeni gàngoor la ñu daan moytandiku.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Qasas 4

Simoore Al-Qasas Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Firawna dadoon kawe-kawelu ci suuf si ; féewale waa réew…

Simoore Aaya 4/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers