Al-Qasas · 8/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
فَالْتَقَطَهُ آلُ فِرْعَوْنَ لِيَكُونَ لَهُمْ عَدُوًّا وَحَزَنًا ۗ إِنَّ فِرْعَوْنَ وَهَامَانَ وَجُنُودَهُمَا كَانُوا خَاطِئِينَ ۝٨
Faltaqatahooo Aalu Fir`awna li yakoona lahum `aduwwanw wa hazanaa; inna Fir`awna wa Haamaana wa junooda humaa kaanoo khaati`een
📖 Tekkim Wolof
Waa kër Firawna for ko, ngir mu doon seenub noon, di seenu lëjal ! Firawna, Haamaan ak seen gàngoor juumoon nañu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore Al-Qasas

6وَنُمَكِّنَ لَهُمْ فِي الْأَرْضِ وَنُرِيَ فِرْعَوْنَ وَهَامَانَ وَجُنُودَهُمَا مِنْهُم مَّا كَانُوا يَحْذَرُونَ
may leen kàttan, ak it wonaale Firawna ak Haamaan ak seeni gàngoor la ñu daan moytandiku.
7وَأَوْحَيْنَا إِلَىٰ أُمِّ مُوسَىٰ أَنْ أَرْضِعِيهِ ۖ فَإِذَا خِفْتِ عَلَيْهِ فَأَلْقِيهِ فِي الْيَمِّ وَلَا تَخَافِي وَلَا تَحْزَنِي ۖ إِنَّا رَادُّوهُ إِلَيْكِ وَجَاعِلُوهُ مِنَ الْمُرْسَلِينَ
Soloo Nanu yaayu Muusaa ne ko : “Nàmpal ko. Te soo tiitee ciy mbiram, sànni ko ci dex gi. Bul ragal, bul jàq : Dananu la ko delloosil mu bokk ca Yonent ya”.
8فَالْتَقَطَهُ آلُ فِرْعَوْنَ لِيَكُونَ لَهُمْ عَدُوًّا وَحَزَنًا ۗ إِنَّ فِرْعَوْنَ وَهَامَانَ وَجُنُودَهُمَا كَانُوا خَاطِئِينَ
Waa kër Firawna for ko, ngir mu doon seenub noon, di seenu lëjal ! Firawna, Haamaan ak seen gàngoor juumoon nañu.
9وَقَالَتِ امْرَأَتُ فِرْعَوْنَ قُرَّتُ عَيْنٍ لِّي وَلَكَ ۖ لَا تَقْتُلُوهُ عَسَىٰ أَن يَنفَعَنَا أَوْ نَتَّخِذَهُ وَلَدًا وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Jabari Firawna ne ko : “(Xale bii di Muusaa) ! buleen ko rey. Nanu ko wéttalikoo maak yaw walla nu doomoo ko, amaana mu jariñ nu”. Lii lépp nag ba muy xew yëguñu ca dara.
10وَأَصْبَحَ فُؤَادُ أُمِّ مُوسَىٰ فَارِغًا ۖ إِن كَادَتْ لَتُبْدِي بِهِ لَوْلَا أَن رَّبَطْنَا عَلَىٰ قَلْبِهَا لِتَكُونَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Xolub ndeyu Muusaa ja jeex na tàkk. Ba mu xaw a feeñal, cëy bu Nu ko dëfëlul woon xolam ak la mu doonoon di ab jullit.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-Qasas 8

Simoore Al-Qasas Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waa kër Firawna for ko, ngir mu doon seenub noon,…

Simoore Aaya 8/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers