Aali Imran · 132/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
وَأَطِيعُوا اللَّهَ وَالرَّسُولَ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ ۝١٣٢
Wa atee`ul laaha war Rasoola la`allakum turhamoon
📖 Tekkim Wolof
Nangeen topp [ndigali Yàlla] ak Yonent bi ndax ngeen doon ñu ñuy yërëm!

🎧 Dégg


📜 Aaya 130-134 — Simoore Aali Imran

130يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَأْكُلُوا الرِّبَا أَضْعَافًا مُّضَاعَفَةً ۖ وَاتَّقُوا اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ
Éy yéen ñi gëm, buleen lekk ribaa ju jóge ci alal juy léw-léwi di fulu. Nangeen ragal Yàlla ndax ngeen texe !
131وَاتَّقُوا النَّارَ الَّتِي أُعِدَّتْ لِلْكَافِرِينَ
Nangeen ragal Safara sa ñuy xaaroo yéefar ya.
132وَأَطِيعُوا اللَّهَ وَالرَّسُولَ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Nangeen topp [ndigali Yàlla] ak Yonent bi ndax ngeen doon ñu ñuy yërëm!
133۞ وَسَارِعُوا إِلَىٰ مَغْفِرَةٍ مِّن رَّبِّكُمْ وَجَنَّةٍ عَرْضُهَا السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ أُعِدَّتْ لِلْمُتَّقِينَ
Jëkkanteleen jëm ci seen njéggalug Boroom ak ci Àjjana joo xam ne yaatu na ni asamaan yi ak suuf si, te ña ragal Yàlla lañu koy xaaroo,
134الَّذِينَ يُنفِقُونَ فِي السَّرَّاءِ وَالضَّرَّاءِ وَالْكَاظِمِينَ الْغَيْظَ وَالْعَافِينَ عَنِ النَّاسِ ۗ وَاللَّهُ يُحِبُّ الْمُحْسِنِينَ
ñoom ña nga xam ne dañuy joxe [seen alal ci jamonoy naataange ak ci jamonoy tar-tar ], ak ñay nëbbu seen mer, ak ñay jéggal nit ñi [ay tooñeel] - Yàlla safoo na ñay rafetal -
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
132Aaya

Tekki — Aali Imran 132

Simoore Aali Imran Aaya 132 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangeen topp [ndigali Yàlla] ak Yonent bi ndax ngeen doon…

Simoore Aaya 132/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 130–134. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers