Aali Imran · 196/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
لَا يَغُرَّنَّكَ تَقَلُّبُ الَّذِينَ كَفَرُوا فِي الْبِلَادِ ۝١٩٦
Laa yaghurrannaka taqal lubul lazeena kafaroo fil bilaad
📖 Tekkim Wolof
Alal ju bari ja yéefar yi di wëlbati ci réew yi, bumu la nax.

🎧 Dégg


📜 Aaya 194-198 — Aali Imran

194رَبَّنَا وَآتِنَا مَا وَعَدتَّنَا عَلَىٰ رُسُلِكَ وَلَا تُخْزِنَا يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۗ إِنَّكَ لَا تُخْلِفُ الْمِيعَادَ
Yaw sunu Boroom ! yal nanga nu jox la nga nu digoon, te jaarale woon ko ca sa Yonent ya. Te bul nu gàcceel kera Bis-pénc ba. Yaw Yàlla, doo wuute ab dige de”.
195فَاسْتَجَابَ لَهُمْ رَبُّهُمْ أَنِّي لَا أُضِيعُ عَمَلَ عَامِلٍ مِّنكُم مِّن ذَكَرٍ أَوْ أُنثَىٰ ۖ بَعْضُكُم مِّن بَعْضٍ ۖ فَالَّذِينَ هَاجَرُوا وَأُخْرِجُوا مِن دِيَارِهِمْ وَأُوذُوا فِي سَبِيلِي وَقَاتَلُوا وَقُتِلُوا لَأُكَفِّرَنَّ عَنْهُمْ سَيِّئَاتِهِمْ وَلَأُدْخِلَنَّهُمْ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ثَوَابًا مِّنْ عِندِ اللَّهِ ۗ وَاللَّهُ عِندَهُ حُسْنُ الثَّوَابِ
Yàlla seen Boroom nungul na leen seeni jëf, ne : “ Man de, duma sànk jëfi ab jëfkat ci neen, moo xam góor la mbaa muy jigéen. Moo xam ñi leen beru walla ñu lor leen ci yoonu Yàlla, ñu reye ñu rey leen. Gaa ñooña Dananu leen soppil seeni ñaawtéef aw yiw te Danaa leen dëkkal Àjjana joo xam ne dex yaa ngay daw ca seen ron, muy yool bu bawoo fa Yàlla.”. Te Yàllaa rafet ab yool.
196لَا يَغُرَّنَّكَ تَقَلُّبُ الَّذِينَ كَفَرُوا فِي الْبِلَادِ
Alal ju bari ja yéefar yi di wëlbati ci réew yi, bumu la nax.
197مَتَاعٌ قَلِيلٌ ثُمَّ مَأْوَاهُمْ جَهَنَّمُ ۚ وَبِئْسَ الْمِهَادُ
Xéewal yu néew la ! Topp seenug delluwaay di Safara. Ndaw delluwaay bu ñaaw !
198لَٰكِنِ الَّذِينَ اتَّقَوْا رَبَّهُمْ لَهُمْ جَنَّاتٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا نُزُلًا مِّنْ عِندِ اللَّهِ ۗ وَمَا عِندَ اللَّهِ خَيْرٌ لِّلْأَبْرَارِ
Waaye ña ragal seen Boroom, am nañu Àjjana joo xam ne dex yaa ngay daw ca seen ron, ñu béel fa, muy seen wàccuwaay fa Yàlla. Te la nekk fa Yàlla mooy dàqal ñu baax ña.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
196Aaya

Tekki — Aali Imran 196

Simoore Aali Imran Aaya 196 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Alal ju bari ja yéefar yi di wëlbati ci réew…

Simoore Aaya 196/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 194–198. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers