Ar-Rum · 50/60
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rum
فَانظُرْ إِلَىٰ آثَارِ رَحْمَتِ اللَّهِ كَيْفَ يُحْيِي الْأَرْضَ بَعْدَ مَوْتِهَا ۚ إِنَّ ذَٰلِكَ لَمُحْيِي الْمَوْتَىٰ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ ۝٥٠
Fanzur ilaaa aasaari rahmatil laahi kaifa yuhyil arda ba`da mawtihaa; inna zaalika lamuhyil mawtaa wa Huwa `alaa kulli shai`in Qadeer
📖 Tekkim Wolof
Xoolal jeexitali yërmaandey Yàlla naka lay dundalee suuf si ginnaaw ba mu deewee. Kookee de Mooy dekkalaat néew yi te mën na lu ne.

🎧 Dégg


📜 Aaya 48-52 — Simoore Ar-Rum

48اللَّهُ الَّذِي يُرْسِلُ الرِّيَاحَ فَتُثِيرُ سَحَابًا فَيَبْسُطُهُ فِي السَّمَاءِ كَيْفَ يَشَاءُ وَيَجْعَلُهُ كِسَفًا فَتَرَى الْوَدْقَ يَخْرُجُ مِنْ خِلَالِهِ ۖ فَإِذَا أَصَابَ بِهِ مَن يَشَاءُ مِنْ عِبَادِهِ إِذَا هُمْ يَسْتَبْشِرُونَ
Yàlla miy yebal ngelaw mu yenu niir, di ko tàbbal ci asamaan si na Mu ko soobe ; Mu di ko def ay daggit. Ab taw di ca génnee su ko tawale. Ña ko soob ci jaamam yi, ndeketeyoo dañuy sëgg ree ngir bég,
49وَإِن كَانُوا مِن قَبْلِ أَن يُنَزَّلَ عَلَيْهِم مِّن قَبْلِهِ لَمُبْلِسِينَ
doonte la sax naagu woon nañu ba mu laataa na wàcc.
50فَانظُرْ إِلَىٰ آثَارِ رَحْمَتِ اللَّهِ كَيْفَ يُحْيِي الْأَرْضَ بَعْدَ مَوْتِهَا ۚ إِنَّ ذَٰلِكَ لَمُحْيِي الْمَوْتَىٰ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Xoolal jeexitali yërmaandey Yàlla naka lay dundalee suuf si ginnaaw ba mu deewee. Kookee de Mooy dekkalaat néew yi te mën na lu ne.
51وَلَئِنْ أَرْسَلْنَا رِيحًا فَرَأَوْهُ مُصْفَرًّا لَّظَلُّوا مِن بَعْدِهِ يَكْفُرُونَ
Bu Nu yebaloon ngelaw, ñu gis ne [seen gàncax ga] mbokk, di [lax ak a dee], dañuy daldi weddi, fakk xéewal ya.
52فَإِنَّكَ لَا تُسْمِعُ الْمَوْتَىٰ وَلَا تُسْمِعُ الصُّمَّ الدُّعَاءَ إِذَا وَلَّوْا مُدْبِرِينَ
Yaw dey, mënoo tax a dégg ñu dee ; waxantumalaak tëx, su ñu nee wërëñ dummóoyu, ak lu woote ba xumb xumb nag.
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
50Aaya

Tekki — Ar-Rum 50

Simoore Ar-Rum Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xoolal jeexitali yërmaandey Yàlla naka lay dundalee suuf si ginnaaw…

Simoore Aaya 50/60 — Simoore Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rum Dégg, Simoore Ar-Rum Tekki, Simoore Ar-Rum mp3, Simoore Ar-Rum pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers