Al-Ahzab · 45/73
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ahzab
يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ إِنَّا أَرْسَلْنَاكَ شَاهِدًا وَمُبَشِّرًا وَنَذِيرًا ۝٤٥
Yaaa aiyuhan Nabiyyu innaaa arsalnaaka shaahidanw wa mubashshiranw wa nazeeraa
📖 Tekkim Wolof
Éy yaw Yonent bi ! Noo la yebal ngir nga doon seede, di béglekat, di xuppekat.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 43-47 — Simoore Al-Ahzab

43هُوَ الَّذِي يُصَلِّي عَلَيْكُمْ وَمَلَائِكَتُهُ لِيُخْرِجَكُم مِّنَ الظُّلُمَاتِ إِلَى النُّورِ ۚ وَكَانَ بِالْمُؤْمِنِينَ رَحِيمًا
Mooy kiy julli ci yéen, di leen ñaanal, - Mook ay Malaakaam, - ngir génne leen cig lëndëm, jëme leen cig leer ; te Mu di Jaglewaakoonu yërmaandeem ci ñi gëm.
44تَحِيَّتُهُمْ يَوْمَ يَلْقَوْنَهُ سَلَامٌ ۚ وَأَعَدَّ لَهُمْ أَجْرًا كَرِيمًا
Seenub nuyyoo Bis nuy dajeek Moom : “Jàmm rekk”, te mu waajal leen ag pey gu tedd .
45يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ إِنَّا أَرْسَلْنَاكَ شَاهِدًا وَمُبَشِّرًا وَنَذِيرًا
Éy yaw Yonent bi ! Noo la yebal ngir nga doon seede, di béglekat, di xuppekat.
46وَدَاعِيًا إِلَى اللَّهِ بِإِذْنِهِ وَسِرَاجًا مُّنِيرًا
té woote jëme ci Yàlla ; te di làmp bu leer.
47وَبَشِّرِ الْمُؤْمِنِينَ بِأَنَّ لَهُم مِّنَ اللَّهِ فَضْلًا كَبِيرًا
Te ngay bégal jullit ñi, ne leen am nañu ca Yàlla ngëneel lu màgg.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
45Aaya

Tekki — Al-Ahzab 45

Simoore Al-Ahzab Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yaw Yonent bi ! Noo la yebal ngir nga…

Simoore Aaya 45/73 — Simoore Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ahzab Dégg, Simoore Al-Ahzab Tekki, Simoore Al-Ahzab mp3, Simoore Al-Ahzab pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers