Al-Ahzab · 44/73
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ahzab
تَحِيَّتُهُمْ يَوْمَ يَلْقَوْنَهُ سَلَامٌ ۚ وَأَعَدَّ لَهُمْ أَجْرًا كَرِيمًا ۝٤٤
Tahiyyatuhum Yawma yalqawnahoo salaamunw wa a`adda lahum ajran kareemaa
📖 Tekkim Wolof
Seenub nuyyoo Bis nuy dajeek Moom : “Jàmm rekk”, te mu waajal leen ag pey gu tedd .

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 42-46 — Simoore Al-Ahzab

42وَسَبِّحُوهُ بُكْرَةً وَأَصِيلًا
te nangeen di Ko sàbbaal suba ak ngoon.
43هُوَ الَّذِي يُصَلِّي عَلَيْكُمْ وَمَلَائِكَتُهُ لِيُخْرِجَكُم مِّنَ الظُّلُمَاتِ إِلَى النُّورِ ۚ وَكَانَ بِالْمُؤْمِنِينَ رَحِيمًا
Mooy kiy julli ci yéen, di leen ñaanal, - Mook ay Malaakaam, - ngir génne leen cig lëndëm, jëme leen cig leer ; te Mu di Jaglewaakoonu yërmaandeem ci ñi gëm.
44تَحِيَّتُهُمْ يَوْمَ يَلْقَوْنَهُ سَلَامٌ ۚ وَأَعَدَّ لَهُمْ أَجْرًا كَرِيمًا
Seenub nuyyoo Bis nuy dajeek Moom : “Jàmm rekk”, te mu waajal leen ag pey gu tedd .
45يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ إِنَّا أَرْسَلْنَاكَ شَاهِدًا وَمُبَشِّرًا وَنَذِيرًا
Éy yaw Yonent bi ! Noo la yebal ngir nga doon seede, di béglekat, di xuppekat.
46وَدَاعِيًا إِلَى اللَّهِ بِإِذْنِهِ وَسِرَاجًا مُّنِيرًا
té woote jëme ci Yàlla ; te di làmp bu leer.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
44Aaya

Tekki — Al-Ahzab 44

Simoore Al-Ahzab Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seenub nuyyoo Bis nuy dajeek Moom : “Jàmm rekk”, te…

Simoore Aaya 44/73 — Simoore Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ahzab Dégg, Simoore Al-Ahzab Tekki, Simoore Al-Ahzab mp3, Simoore Al-Ahzab pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers