As-Saffat · 43/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فِي جَنَّاتِ النَّعِيمِ ۝٤٣
Fee jannaatin Na`eem
📖 Tekkim Wolof
ca biir Àjjanay xéewal ja,

🎧 Dégg


📜 Aaya 41-45 — Simoore As-Saffat

41أُولَٰئِكَ لَهُمْ رِزْقٌ مَّعْلُومٌ
Ñoom am nañu wërsëg wu ñu xam :
42فَوَاكِهُ ۖ وَهُم مُّكْرَمُونَ
ay fuytéef ak i teraanga,
43فِي جَنَّاتِ النَّعِيمِ
ca biir Àjjanay xéewal ja,
44عَلَىٰ سُرُرٍ مُّتَقَابِلِينَ
ñuy jàkkaarloo ca seen kawi lal.
45يُطَافُ عَلَيْهِم بِكَأْسٍ مِّن مَّعِينٍ
Ñu di leen wër ak kaasi bënub ndox
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
43Aaya

Tekki — As-Saffat 43

Simoore As-Saffat Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ca biir Àjjanay xéewal ja,

Simoore Aaya 43/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers