Az-Zumar · 54/75
Tekki Waxtaan — Az-Zumar
وَأَنِيبُوا إِلَىٰ رَبِّكُمْ وَأَسْلِمُوا لَهُ مِن قَبْلِ أَن يَأْتِيَكُمُ الْعَذَابُ ثُمَّ لَا تُنصَرُونَ ۝٥٤
Wa aneebooo ilaa Rabbikum wa aslimoo lahoo min qabli ai yaatiyakumul `azaabu summ laa tunsaroon
📖 Tekkim Wolof
Delluleen ci seen Boroom, te jébël ko seen bopp, balaa mbugël di dal ci seen kaw te kenn duleen ca dimbali.

🎧 Dégg


📜 Aaya 52-56 — Az-Zumar

52أَوَلَمْ يَعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ يَبْسُطُ الرِّزْقَ لِمَن يَشَاءُ وَيَقْدِرُ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Xanaa dañoo xamul ne Yàlla mooy yaatalal ku ko soob wërsëgam di ko xatal it ? Ay kiiman a ngi ci biir loolu ngir aw nit ñu gëm.
53۞ قُلْ يَا عِبَادِيَ الَّذِينَ أَسْرَفُوا عَلَىٰ أَنفُسِهِمْ لَا تَقْنَطُوا مِن رَّحْمَةِ اللَّهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ يَغْفِرُ الذُّنُوبَ جَمِيعًا ۚ إِنَّهُ هُوَ الْغَفُورُ الرَّحِيمُ
Waxal ne : “Éy yéen Sama jaam ñi yàq seen bopp, buleen naagu ci yërmandey Yàlla. Ndax Yàlla dana jégële bakkaar yépp. Mooy Jégëlaakoon ba, di Jaglewaakoon ba”.
54وَأَنِيبُوا إِلَىٰ رَبِّكُمْ وَأَسْلِمُوا لَهُ مِن قَبْلِ أَن يَأْتِيَكُمُ الْعَذَابُ ثُمَّ لَا تُنصَرُونَ
Delluleen ci seen Boroom, te jébël ko seen bopp, balaa mbugël di dal ci seen kaw te kenn duleen ca dimbali.
55وَاتَّبِعُوا أَحْسَنَ مَا أُنزِلَ إِلَيْكُم مِّن رَّبِّكُم مِّن قَبْلِ أَن يَأْتِيَكُمُ الْعَذَابُ بَغْتَةً وَأَنتُمْ لَا تَشْعُرُونَ
Te it na ngeen di topp li gën a rafet ci li nu wàcce (Alxuraan) ci yéen mu bawoo ca seen Boroom, balaa mbugël di dal ci seen kaw te du ngeen ko yëg ;
56أَن تَقُولَ نَفْسٌ يَا حَسْرَتَا عَلَىٰ مَا فَرَّطتُ فِي جَنبِ اللَّهِ وَإِن كُنتُ لَمِنَ السَّاخِرِينَ
balaa benn bakkan di wax naan : “Wóy ngalla man ci na mu soofentale woon mbiri Yàlla. Te daan ca reetaan nit ña” ;
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
54Aaya

Tekki — Az-Zumar 54

Simoore Az-Zumar Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Delluleen ci seen Boroom, te jébël ko seen bopp, balaa…

Simoore Aaya 54/75 — Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zumar Dégg, Az-Zumar Tekki, Az-Zumar mp3, Az-Zumar pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers