Ghafir · 26/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
وَقَالَ فِرْعَوْنُ ذَرُونِي أَقْتُلْ مُوسَىٰ وَلْيَدْعُ رَبَّهُ ۖ إِنِّي أَخَافُ أَن يُبَدِّلَ دِينَكُمْ أَوْ أَن يُظْهِرَ فِي الْأَرْضِ الْفَسَادَ ۝٢٦
Wa qaala Fir`awnu zarooneee aqtul Moosaa walyad`u Rabbahoo inneee akhaafu ai yubaddila deenakum aw ai yuzhira fil ardil fasaad
📖 Tekkim Wolof
Firawna daldi wax ne : “Bàyyileen ma rey Muusaa. Na woo Boroomam ! Da may ragal mu soppi seen diine walla muy ger nit ñi di yàq réew mi”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 24-28 — Ghafir

24إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَهَامَانَ وَقَارُونَ فَقَالُوا سَاحِرٌ كَذَّابٌ
jëmële ko ca Firawna, ak Haamaana ak Qaaruuna. Ñuy wax naan : “Kii ab njibarkat bu di ! ab fenaakoon la ! ”
25فَلَمَّا جَاءَهُم بِالْحَقِّ مِنْ عِندِنَا قَالُوا اقْتُلُوا أَبْنَاءَ الَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ وَاسْتَحْيُوا نِسَاءَهُمْ ۚ وَمَا كَيْدُ الْكَافِرِينَ إِلَّا فِي ضَلَالٍ
Ba mu àggee ca ñoom, indi ko baawoo fi Nun da ñoo wax ne : “reyleen doom yu góor ñi gëm ànd ak moom, te bàyyi jigéen ñi ñuy dund”. Pexey yéefar yi du dara lu dul ci ag réer (lay tege).
26وَقَالَ فِرْعَوْنُ ذَرُونِي أَقْتُلْ مُوسَىٰ وَلْيَدْعُ رَبَّهُ ۖ إِنِّي أَخَافُ أَن يُبَدِّلَ دِينَكُمْ أَوْ أَن يُظْهِرَ فِي الْأَرْضِ الْفَسَادَ
Firawna daldi wax ne : “Bàyyileen ma rey Muusaa. Na woo Boroomam ! Da may ragal mu soppi seen diine walla muy ger nit ñi di yàq réew mi”.
27وَقَالَ مُوسَىٰ إِنِّي عُذْتُ بِرَبِّي وَرَبِّكُم مِّن كُلِّ مُتَكَبِّرٍ لَّا يُؤْمِنُ بِيَوْمِ الْحِسَابِ
Muusaa [daldi] ne : “Maa ngi sàkku ci sama Boroom mu musal ma ci képp kuy rëy-rëylu, te gëmul bisub wañoo ba (Bis Pénc ba)”.
28وَقَالَ رَجُلٌ مُّؤْمِنٌ مِّنْ آلِ فِرْعَوْنَ يَكْتُمُ إِيمَانَهُ أَتَقْتُلُونَ رَجُلًا أَن يَقُولَ رَبِّيَ اللَّهُ وَقَدْ جَاءَكُم بِالْبَيِّنَاتِ مِن رَّبِّكُمْ ۖ وَإِن يَكُ كَاذِبًا فَعَلَيْهِ كَذِبُهُ ۖ وَإِن يَكُ صَادِقًا يُصِبْكُم بَعْضُ الَّذِي يَعِدُكُمْ ۖ إِنَّ اللَّهَ لَا يَهْدِي مَنْ هُوَ مُسْرِفٌ كَذَّابٌ
Mu am waaju gëm te bokk ca waa kër Firawna, daldi wax ne : “Ndax dangeen a bëgg rey waa joo xam ne li mu wax lépp moo di ne : “Yàllaay sama Boroom” ? Te indil na leen ay firnde yu bawoo ca Yàlla. Su fekkee day fen, fenam ya du ko moy ; su waxee dëgg, ngeen dor a xam ne li mu leen dig dana dal seen kow”. Te, Yàlla du gindi mukk fenkat buy yàq (waaja da doon nëbbu ngëmam) !
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Ghafir 26

Simoore Ghafir Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Firawna daldi wax ne : “Bàyyileen ma rey Muusaa. Na…

Simoore Aaya 26/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers