Ghafir · 25/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
فَلَمَّا جَاءَهُم بِالْحَقِّ مِنْ عِندِنَا قَالُوا اقْتُلُوا أَبْنَاءَ الَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ وَاسْتَحْيُوا نِسَاءَهُمْ ۚ وَمَا كَيْدُ الْكَافِرِينَ إِلَّا فِي ضَلَالٍ ٢٥
Transliteration
Falamuna jaaa`ahum bil haqqi min `indinaa qaaluq tulooo abnaaa`al lazeena aamanoo ma`ahoo wastahyoo nisaaa`ahum; wa maa kaidul kaafireena illaa fee dalaal
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ba mu àggee ca ñoom, indi ko baawoo fi Nun da ñoo wax ne : “reyleen doom yu góor ñi gëm ànd ak moom, te bàyyi jigéen ñi ñuy dund”. Pexey yéefar yi du dara lu dul ci ag réer (lay tege).
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 23-27 — Ghafir
23وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا مُوسَىٰ بِآيَاتِنَا وَسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Yónni woon nanu Muusaa ak sunuy laaya boole ko ak ay firnde yu leer,
24إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَهَامَانَ وَقَارُونَ فَقَالُوا سَاحِرٌ كَذَّابٌ
jëmële ko ca Firawna, ak Haamaana ak Qaaruuna. Ñuy wax naan : “Kii ab njibarkat bu di ! ab fenaakoon la ! ”
25فَلَمَّا جَاءَهُم بِالْحَقِّ مِنْ عِندِنَا قَالُوا اقْتُلُوا أَبْنَاءَ الَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ وَاسْتَحْيُوا نِسَاءَهُمْ ۚ وَمَا كَيْدُ الْكَافِرِينَ إِلَّا فِي ضَلَالٍ
Ba mu àggee ca ñoom, indi ko baawoo fi Nun da ñoo wax ne : “reyleen doom yu góor ñi gëm ànd ak moom, te bàyyi jigéen ñi ñuy dund”. Pexey yéefar yi du dara lu dul ci ag réer (lay tege).
26وَقَالَ فِرْعَوْنُ ذَرُونِي أَقْتُلْ مُوسَىٰ وَلْيَدْعُ رَبَّهُ ۖ إِنِّي أَخَافُ أَن يُبَدِّلَ دِينَكُمْ أَوْ أَن يُظْهِرَ فِي الْأَرْضِ الْفَسَادَ
Firawna daldi wax ne : “Bàyyileen ma rey Muusaa. Na woo Boroomam ! Da may ragal mu soppi seen diine walla muy ger nit ñi di yàq réew mi”.
27وَقَالَ مُوسَىٰ إِنِّي عُذْتُ بِرَبِّي وَرَبِّكُم مِّن كُلِّ مُتَكَبِّرٍ لَّا يُؤْمِنُ بِيَوْمِ الْحِسَابِ
Muusaa [daldi] ne : “Maa ngi sàkku ci sama Boroom mu musal ma ci képp kuy rëy-rëylu, te gëmul bisub wañoo ba (Bis Pénc ba)”.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
25Aaya
Tekki — Ghafir 25
Simoore Ghafir Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba mu àggee ca ñoom, indi ko baawoo fi Nun…Simoore Aaya 25/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








