Az-Zukhruf · 3/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
إِنَّا جَعَلْنَاهُ قُرْآنًا عَرَبِيًّا لَّعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ ٣
Transliteration
Innaa ja`alnaahu Quraanan `Arabiyyal la`allakum ta`qiloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Def Nanu ko Alxuraan ci làmmiñu araab ndax amaana ngeen xellu (xalaat).
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 1-5 — Simoore Az-Zukhruf
1حم
Haa, Miim.
2وَالْكِتَابِ الْمُبِينِ
Ci Téere bu leer bu !
3إِنَّا جَعَلْنَاهُ قُرْآنًا عَرَبِيًّا لَّعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ
Def Nanu ko Alxuraan ci làmmiñu araab ndax amaana ngeen xellu (xalaat).
4وَإِنَّهُ فِي أُمِّ الْكِتَابِ لَدَيْنَا لَعَلِيٌّ حَكِيمٌ
Nekk na fi Nun, ca ndayi Téere ba (Allawhul mahfuus), kawe lool fees dell ag ràñnee.
5أَفَنَضْرِبُ عَنكُمُ الذِّكْرَ صَفْحًا أَن كُنتُمْ قَوْمًا مُّسْرِفِينَ
Moo ndax ! Danu leen di jox [Alxuraan] te fekk ngeen di ay yàqkat ?
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
3Aaya
Tekki — Az-Zukhruf 3
Simoore Az-Zukhruf Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Def Nanu ko Alxuraan ci làmmiñu araab ndax amaana ngeen…Simoore Aaya 3/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Monday, September 7, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








