Az-Zukhruf · 4/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
وَإِنَّهُ فِي أُمِّ الْكِتَابِ لَدَيْنَا لَعَلِيٌّ حَكِيمٌ ۝٤
Wa innahoo feee Ummil Kitaabi Ladainaa la`aliyyun hakeem
📖 Tekkim Wolof
Nekk na fi Nun, ca ndayi Téere ba (Allawhul mahfuus), kawe lool fees dell ag ràñnee.

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore Az-Zukhruf

2وَالْكِتَابِ الْمُبِينِ
Ci Téere bu leer bu !
3إِنَّا جَعَلْنَاهُ قُرْآنًا عَرَبِيًّا لَّعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ
Def Nanu ko Alxuraan ci làmmiñu araab ndax amaana ngeen xellu (xalaat).
4وَإِنَّهُ فِي أُمِّ الْكِتَابِ لَدَيْنَا لَعَلِيٌّ حَكِيمٌ
Nekk na fi Nun, ca ndayi Téere ba (Allawhul mahfuus), kawe lool fees dell ag ràñnee.
5أَفَنَضْرِبُ عَنكُمُ الذِّكْرَ صَفْحًا أَن كُنتُمْ قَوْمًا مُّسْرِفِينَ
Moo ndax ! Danu leen di jox [Alxuraan] te fekk ngeen di ay yàqkat ?
6وَكَمْ أَرْسَلْنَا مِن نَّبِيٍّ فِي الْأَوَّلِينَ
Ak a bari lu nu yónni ci ay Yonnenta ca ña jiitu woon !
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 4

Simoore Az-Zukhruf Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nekk na fi Nun, ca ndayi Téere ba (Allawhul mahfuus),…

Simoore Aaya 4/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers