Az-Zukhruf · 52/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
أَمْ أَنَا خَيْرٌ مِّنْ هَٰذَا الَّذِي هُوَ مَهِينٌ وَلَا يَكَادُ يُبِينُ ۝٥٢
Am ana khairum min haazal lazee huwa maheenunw wa laa yuakaadu yubeen
📖 Tekkim Wolof
Xanaa man sax maa wara gën waaju doyadi jii nga xam ne xawut a man a wax ( lu nit di xam )?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 50-54 — Simoore Az-Zukhruf

50فَلَمَّا كَشَفْنَا عَنْهُمُ الْعَذَابَ إِذَا هُمْ يَنكُثُونَ
Ba nu teggee jafe-jafe ya, da ñoo tiri lépp la ñu digéwoon.
51وَنَادَىٰ فِرْعَوْنُ فِي قَوْمِهِ قَالَ يَا قَوْمِ أَلَيْسَ لِي مُلْكُ مِصْرَ وَهَٰذِهِ الْأَنْهَارُ تَجْرِي مِن تَحْتِي ۖ أَفَلَا تُبْصِرُونَ
Firawna daldi dajale aw nitam ne leen: “moo sama gaa ñi ! Ndax moomu ma nguurug Misra ak dex yii di dawdawaan ci sama ron? Xanaa du ngéen gis ?
52أَمْ أَنَا خَيْرٌ مِّنْ هَٰذَا الَّذِي هُوَ مَهِينٌ وَلَا يَكَادُ يُبِينُ
Xanaa man sax maa wara gën waaju doyadi jii nga xam ne xawut a man a wax ( lu nit di xam )?
53فَلَوْلَا أُلْقِيَ عَلَيْهِ أَسْوِرَةٌ مِّن ذَهَبٍ أَوْ جَاءَ مَعَهُ الْمَلَائِكَةُ مُقْتَرِنِينَ
( Lii muy woote su doon dëgg) Kon ñu takkal ko lami wurus? Wala mu lëngook ay Malaaka? ”
54فَاسْتَخَفَّ قَوْمَهُ فَأَطَاعُوهُ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ
Mu fëkk xeli nit ña ñu daldi ko topp génn ci diine.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 52

Simoore Az-Zukhruf Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa man sax maa wara gën waaju doyadi jii nga…

Simoore Aaya 52/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers