Az-Zukhruf · 54/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
فَاسْتَخَفَّ قَوْمَهُ فَأَطَاعُوهُ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ ۝٥٤
Fastakhaffa qawmahoo fa ataa`ooh; innahum kaanoo qawman faasiqeen
📖 Tekkim Wolof
Mu fëkk xeli nit ña ñu daldi ko topp génn ci diine.

🎧 Dégg


📜 Aaya 52-56 — Simoore Az-Zukhruf

52أَمْ أَنَا خَيْرٌ مِّنْ هَٰذَا الَّذِي هُوَ مَهِينٌ وَلَا يَكَادُ يُبِينُ
Xanaa man sax maa wara gën waaju doyadi jii nga xam ne xawut a man a wax ( lu nit di xam )?
53فَلَوْلَا أُلْقِيَ عَلَيْهِ أَسْوِرَةٌ مِّن ذَهَبٍ أَوْ جَاءَ مَعَهُ الْمَلَائِكَةُ مُقْتَرِنِينَ
( Lii muy woote su doon dëgg) Kon ñu takkal ko lami wurus? Wala mu lëngook ay Malaaka? ”
54فَاسْتَخَفَّ قَوْمَهُ فَأَطَاعُوهُ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ
Mu fëkk xeli nit ña ñu daldi ko topp génn ci diine.
55فَلَمَّا آسَفُونَا انتَقَمْنَا مِنْهُمْ فَأَغْرَقْنَاهُمْ أَجْمَعِينَ
Ba ñu Nu merloo, ca la Nu fayyoo labal ñoom ñépp.
56فَجَعَلْنَاهُمْ سَلَفًا وَمَثَلًا لِّلْآخِرِينَ
Nu def leen ñu di am njàng ci ñiy xalset a dikk ëllëg.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
54Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 54

Simoore Az-Zukhruf Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu fëkk xeli nit ña ñu daldi ko topp génn…

Simoore Aaya 54/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers