Az-Zukhruf · 55/89
Tekki Waxtaan — Az-Zukhruf
فَلَمَّا آسَفُونَا انتَقَمْنَا مِنْهُمْ فَأَغْرَقْنَاهُمْ أَجْمَعِينَ ٥٥
Transliteration
Falammaaa aasafoonan taqamnaa minhum fa aghraqnaahum ajma`een
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu Nu merloo, ca la Nu fayyoo labal ñoom ñépp.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 53-57 — Az-Zukhruf
53فَلَوْلَا أُلْقِيَ عَلَيْهِ أَسْوِرَةٌ مِّن ذَهَبٍ أَوْ جَاءَ مَعَهُ الْمَلَائِكَةُ مُقْتَرِنِينَ
( Lii muy woote su doon dëgg) Kon ñu takkal ko lami wurus? Wala mu lëngook ay Malaaka? ”
54فَاسْتَخَفَّ قَوْمَهُ فَأَطَاعُوهُ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ
Mu fëkk xeli nit ña ñu daldi ko topp génn ci diine.
55فَلَمَّا آسَفُونَا انتَقَمْنَا مِنْهُمْ فَأَغْرَقْنَاهُمْ أَجْمَعِينَ
Ba ñu Nu merloo, ca la Nu fayyoo labal ñoom ñépp.
56فَجَعَلْنَاهُمْ سَلَفًا وَمَثَلًا لِّلْآخِرِينَ
Nu def leen ñu di am njàng ci ñiy xalset a dikk ëllëg.
57۞ وَلَمَّا ضُرِبَ ابْنُ مَرْيَمَ مَثَلًا إِذَا قَوْمُكَ مِنْهُ يَصِدُّونَ
Ba ñu jëlee misaal ci Iisaa doomi Maryaama, saw nit dañoo daldi dumóoyu,
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
55Aaya
Tekki — Az-Zukhruf 55
Simoore Az-Zukhruf Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu Nu merloo, ca la Nu fayyoo labal ñoom…Simoore Aaya 55/89 — Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zukhruf Dégg, Az-Zukhruf Tekki, Az-Zukhruf mp3, Az-Zukhruf pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








