Al-Fath · 6/29
Tekki Waxtaan — Al-Fath
وَيُعَذِّبَ الْمُنَافِقِينَ وَالْمُنَافِقَاتِ وَالْمُشْرِكِينَ وَالْمُشْرِكَاتِ الظَّانِّينَ بِاللَّهِ ظَنَّ السَّوْءِ ۚ عَلَيْهِمْ دَائِرَةُ السَّوْءِ ۖ وَغَضِبَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ وَلَعَنَهُمْ وَأَعَدَّ لَهُمْ جَهَنَّمَ ۖ وَسَاءَتْ مَصِيرًا ۝٦
Wa yu`azzibal munaafiqeena walmunaafiqaati wal mushrikeena walmushrikaatiz zaaanneena billaahi zannas saw`; `alaihim daaa`iratus saw`i wa ghadibal laahu `alaihim wa la`anahum wa a`adda lahum jahannama wa saaa` at maseeraa
📖 Tekkim Wolof
(ngir loolu it) dana mbugël naaféq yu, góor yeek yu jigéen yi, ak bokkaalekat yu goor yaak yu jigéen yay njortu ci Yàlla. Ak itam ne waajalal na leen safara muy dëkkuwaay bu bon!
🎧 Dégg

📜 Aaya 4-8 — Al-Fath

4هُوَ الَّذِي أَنزَلَ السَّكِينَةَ فِي قُلُوبِ الْمُؤْمِنِينَ لِيَزْدَادُوا إِيمَانًا مَّعَ إِيمَانِهِمْ ۗ وَلِلَّهِ جُنُودُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَكَانَ اللَّهُ عَلِيمًا حَكِيمًا
Moom (Yàlla) ki wàcce ag dal ci xoli jullit ñi ngir ñuy dolliku ngëm ci séen kaw ngëm ga. Te nag Yàllaa moom xarekati asamaan yeek suuf si ; Yàlla Kuy xam la ku Xereñ la
5لِّيُدْخِلَ الْمُؤْمِنِينَ وَالْمُؤْمِنَاتِ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا وَيُكَفِّرَ عَنْهُمْ سَيِّئَاتِهِمْ ۚ وَكَانَ ذَٰلِكَ عِندَ اللَّهِ فَوْزًا عَظِيمًا
(waral gi mu waral ci yéen xare) tax na ba dana tàbbal jullit ñu goor ñeek jullit ñu jigéen ñi ci Àjjana yoo xam ne ay dex ñooy daw ci suufam te dañu fay béel, te it dana leen faral séeni ñaawtéef loolu di texe gu mag ga fa Yàlla.
6وَيُعَذِّبَ الْمُنَافِقِينَ وَالْمُنَافِقَاتِ وَالْمُشْرِكِينَ وَالْمُشْرِكَاتِ الظَّانِّينَ بِاللَّهِ ظَنَّ السَّوْءِ ۚ عَلَيْهِمْ دَائِرَةُ السَّوْءِ ۖ وَغَضِبَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ وَلَعَنَهُمْ وَأَعَدَّ لَهُمْ جَهَنَّمَ ۖ وَسَاءَتْ مَصِيرًا
(ngir loolu it) dana mbugël naaféq yu, góor yeek yu jigéen yi, ak bokkaalekat yu goor yaak yu jigéen yay njortu ci Yàlla. Ak itam ne waajalal na leen safara muy dëkkuwaay bu bon!
7وَلِلَّهِ جُنُودُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَكَانَ اللَّهُ عَزِيزًا حَكِيمًا
Yàllaa moom xarekati asamaan yeek suuf si ; Yàlla Boroom Kàttan la di Ku Xereñ.
8إِنَّا أَرْسَلْنَاكَ شَاهِدًا وَمُبَشِّرًا وَنَذِيرًا
Yónni nanu la ngaay seede (ci saw xeet), di béglekat (ci jullit ñi) di xuppekat (ci yéefar yi),
Al-FathFihi Alxuraan
29Aaya
MedinanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Fath 6

Simoore Al-Fath Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (ngir loolu it) dana mbugël naaféq yu, góor yeek yu…

Simoore Aaya 6/29 — Al-Fath الفتح (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Fath Dégg, Al-Fath Tekki, Al-Fath mp3, Al-Fath pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers