Qaf · 16/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ وَنَعْلَمُ مَا تُوَسْوِسُ بِهِ نَفْسُهُ ۖ وَنَحْنُ أَقْرَبُ إِلَيْهِ مِنْ حَبْلِ الْوَرِيدِ ۝١٦
Wa laqad khalaqnal insaana wa na`lamu maa tuwaswisu bihee nafsuhoo wa Nahnu aqrabu ilaihi min hablil wareed
📖 Tekkim Wolof
Nun Yàlla Noo sàkk nit bind ko te it xam Nanu liy jax-jaxi ci am xolam te sax Nun Noo ko gën a jegeñ buum giy téye ab xol

🎧 Dégg


📜 Aaya 14-18 — Simoore Qaf

14وَأَصْحَابُ الْأَيْكَةِ وَقَوْمُ تُبَّعٍ ۚ كُلٌّ كَذَّبَ الرُّسُلَ فَحَقَّ وَعِيدِ
ak waa Aykata ak nitu Tubba’a. Ñépp weddiwoon Yonent ya. Samag tëkku dal leen (di mbugël).
15أَفَعَيِينَا بِالْخَلْقِ الْأَوَّلِ ۚ بَلْ هُمْ فِي لَبْسٍ مِّنْ خَلْقٍ جَدِيدٍ
Nga ne ma lan ? Nun Yàlla danoo sonn ca bind gu jëkk ga ? Ñii kay ñi ngi cim lënt ci mbirum dekkiwaat (ku sos dekkil jaaxalu ko).
16وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ وَنَعْلَمُ مَا تُوَسْوِسُ بِهِ نَفْسُهُ ۖ وَنَحْنُ أَقْرَبُ إِلَيْهِ مِنْ حَبْلِ الْوَرِيدِ
Nun Yàlla Noo sàkk nit bind ko te it xam Nanu liy jax-jaxi ci am xolam te sax Nun Noo ko gën a jegeñ buum giy téye ab xol
17إِذْ يَتَلَقَّى الْمُتَلَقِّيَانِ عَنِ الْيَمِينِ وَعَنِ الشِّمَالِ قَعِيدٌ
ngir ñaari way joqalante yaa ngay joqalante, tey fuglu ndeyjoor ak càmmoñ.
18مَّا يَلْفِظُ مِن قَوْلٍ إِلَّا لَدَيْهِ رَقِيبٌ عَتِيدٌ
Amul jenn wax ju muy àddu lu dul ne Raqiib ak Atiid ña nga ko tiim (ñiy bind jëfi nit ñi) .
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Qaf 16

Simoore Qaf Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun Yàlla Noo sàkk nit bind ko te it xam…

Simoore Aaya 16/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers