Qaf · 17/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
إِذْ يَتَلَقَّى الْمُتَلَقِّيَانِ عَنِ الْيَمِينِ وَعَنِ الشِّمَالِ قَعِيدٌ ۝١٧
Iz yatalaqqal mutalaqqi yaani `anil yameeni wa `anish shimaali qa`eed
📖 Tekkim Wolof
ngir ñaari way joqalante yaa ngay joqalante, tey fuglu ndeyjoor ak càmmoñ.

🎧 Dégg


📜 Aaya 15-19 — Simoore Qaf

15أَفَعَيِينَا بِالْخَلْقِ الْأَوَّلِ ۚ بَلْ هُمْ فِي لَبْسٍ مِّنْ خَلْقٍ جَدِيدٍ
Nga ne ma lan ? Nun Yàlla danoo sonn ca bind gu jëkk ga ? Ñii kay ñi ngi cim lënt ci mbirum dekkiwaat (ku sos dekkil jaaxalu ko).
16وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ وَنَعْلَمُ مَا تُوَسْوِسُ بِهِ نَفْسُهُ ۖ وَنَحْنُ أَقْرَبُ إِلَيْهِ مِنْ حَبْلِ الْوَرِيدِ
Nun Yàlla Noo sàkk nit bind ko te it xam Nanu liy jax-jaxi ci am xolam te sax Nun Noo ko gën a jegeñ buum giy téye ab xol
17إِذْ يَتَلَقَّى الْمُتَلَقِّيَانِ عَنِ الْيَمِينِ وَعَنِ الشِّمَالِ قَعِيدٌ
ngir ñaari way joqalante yaa ngay joqalante, tey fuglu ndeyjoor ak càmmoñ.
18مَّا يَلْفِظُ مِن قَوْلٍ إِلَّا لَدَيْهِ رَقِيبٌ عَتِيدٌ
Amul jenn wax ju muy àddu lu dul ne Raqiib ak Atiid ña nga ko tiim (ñiy bind jëfi nit ñi) .
19وَجَاءَتْ سَكْرَةُ الْمَوْتِ بِالْحَقِّ ۖ ذَٰلِكَ مَا كُنتَ مِنْهُ تَحِيدُ
Sukraatus ndee aksi na ci ñoom tigi : “Loolu moo di li nga daan weddi”.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Qaf 17

Simoore Qaf Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ngir ñaari way joqalante yaa ngay joqalante, tey fuglu ndeyjoor…

Simoore Aaya 17/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers