Ar-Rahman · 55/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ ۝٥٥
Fabi ayyi aalaaa`i Rabbikumaa tukazzibaan
📖 Tekkim Wolof
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 53-57 — Simoore Ar-Rahman

53فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
54مُتَّكِئِينَ عَلَىٰ فُرُشٍ بَطَائِنُهَا مِنْ إِسْتَبْرَقٍ ۚ وَجَنَى الْجَنَّتَيْنِ دَانٍ
ñangay sóonu ci ay laltaay yu dëll yoo xam ne biir ga sooy la, te it meññatum ñaar dër ya day yoore.
55فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
56فِيهِنَّ قَاصِرَاتُ الطَّرْفِ لَمْ يَطْمِثْهُنَّ إِنسٌ قَبْلَهُمْ وَلَا جَانٌّ
Ay Huur Al iin ñuy sajj seenub gis, ñoo xam ne nit walla jinne masu leen laal ñuy nekk ca biir.
57فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
55Aaya

Tekki — Ar-Rahman 55

Simoore Ar-Rahman Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a…

Simoore Aaya 55/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers