Ar-Rahman · 56/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
فِيهِنَّ قَاصِرَاتُ الطَّرْفِ لَمْ يَطْمِثْهُنَّ إِنسٌ قَبْلَهُمْ وَلَا جَانٌّ ۝٥٦
Feehinna qaasiratut tarfi lam yatmishunna insun qablahum wa laa jaaann
📖 Tekkim Wolof
Ay Huur Al iin ñuy sajj seenub gis, ñoo xam ne nit walla jinne masu leen laal ñuy nekk ca biir.

🎧 Dégg


📜 Aaya 54-58 — Simoore Ar-Rahman

54مُتَّكِئِينَ عَلَىٰ فُرُشٍ بَطَائِنُهَا مِنْ إِسْتَبْرَقٍ ۚ وَجَنَى الْجَنَّتَيْنِ دَانٍ
ñangay sóonu ci ay laltaay yu dëll yoo xam ne biir ga sooy la, te it meññatum ñaar dër ya day yoore.
55فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
56فِيهِنَّ قَاصِرَاتُ الطَّرْفِ لَمْ يَطْمِثْهُنَّ إِنسٌ قَبْلَهُمْ وَلَا جَانٌّ
Ay Huur Al iin ñuy sajj seenub gis, ñoo xam ne nit walla jinne masu leen laal ñuy nekk ca biir.
57فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
58كَأَنَّهُنَّ الْيَاقُوتُ وَالْمَرْجَانُ
Dañuy [rafet ba] melni: wurus yaaquut walla marjaan.
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
56Aaya

Tekki — Ar-Rahman 56

Simoore Ar-Rahman Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ay Huur Al iin ñuy sajj seenub gis, ñoo xam…

Simoore Aaya 56/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers